Dip Doundou Guiss - NLMD Lyrics

Lyrics NLMD - Dip Doundou Guiss



Ligueyou ndaye moy agnou domm
Ronkhognou mère ci niak diom
Mandi bakhoul soxor mo bakh
policier bi diay la drogue
Meunoun ma faay
Iblis sax dou job comme man
Awma deukeudo si kaw souf
Bokouniou drapeau non non
Non non non
Founé dem nafa founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah.
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek
Nila meuneu démé yeah.
Nila meuneu démé yeah.
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek yeah
Assamane ci meune na khiin dou taw
Sama mama dina triste mais dou diooy
Deukou cris mais sa fils beugou foo
Bénn doom'al dafa khiff mais dou thiopp
Diotna samay guènt, yètall samay beug beug
Goor nguii yoom Goor jiguén du gueuneu deugueur
Dou danga mouma rekk sa yalla wara teukh
Diour sa bopp soul sa bopp niaar rekk la meuneu teu!
Amoo place même bassi sa biirou mère nigger.
Fim la diouré la sa magg yi diogué nigger.
Mowti dina moudji
Matt deum bou raffét dou wallé fébar bou nékh nigger.
Rakk wolloul sa kharitt yi
Beuss dinga khamné safara mo dakh fii
Déreta fort gnila beugue niola sonal
Sa papa diangala kharou sa maman nampaléla possone
Man dagnma néh diokhéle sa xol ma diokhé sama rouh
Niou khar ba tidji sama gatt ma oubi sama yourr
Nadj dou yeug sédayy kénn leundeum'oul ba taal lamp bou nioul
Yagga diokhé sa taate ay nittou goudi yaye djou. doom bu flou
Sa pèle binga gassé pakh bi silagn la moudié soull
Dama cher bomay rayy déféko pakka wourouss
Tant que gnogui fénn beuseul sa khol bagnala tontou mougn.
Yakk derr xèssayou xèsall katt deugue bouniou mourr
Ligueyou ndaye moy agnou domm
Ronkhognou mère ci niak diom
Mandi bakhoul soxor mo bakh
policier bi diay la drogue
Meunoun ma faay
Iblis sax dou job comme man
Awma deukeudo si kaw souf
Bokouniou drapeau non non
Non non non
Founé dem nafa founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah.
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah.
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek
Kou amoul xol amo fit
Kou gueum yallah do ragal
Ray naniou kou djoudou goudoul
Teuth nguén kou défoul dara
Say mbokou bou diékh bo réindé say noon.
Meuno weet so amé ndam
Défaite mom orphelin leu ni sédaayu safara haan?
Daguay business sa diné loudoul faay moussou mala tchi guiss
Nittou jammeuh ngeu kagne ngay djoubaulék yallah ak ibliss.
Euleuk tchi biir di nga fégne nigga euleuk tchi biir .
Nakho sa bopp nakho yonente bi
Ndakh goumba dina guiss souy gueinteu
Khall wané nioumouy lakk bala bissou pinthieu
DEUG méti ni secréts yi nga dinthieu .
Do fatté lo nga jangal sa bopp kan mo meusoul féneu
Yeah nigga Thiagga bou yiw ni policier djoup
Meuno di degglou di wakh ni kouy lekk tchi douch.
Bopou bou fess day tek djeuweum si suuf.
Motah couronne meuneu na djaapeuh kou meussoul nekk bour Aÿ!
Gni deh nio gueuneu riche nio niou gueuneu niakeu .
Sa mellieur xarit la yëré noone ngi di gueuneu djaap
Yallah teuthie bideew ci jail mouy lerral nioune nieup djanteu.
Même kouy sangue neew sangou katou neew dinako sangue
Ligueyou ndaye moy agnou domm
Ronkhognou mère ci niak diom
Mandi bakhoul soxor mo bakh
policier bi diay la drogue
Meunoun ma faay
Iblis sax dou job comme man
Awma deukeudo si kaw souf
Bokouniou drapeau non non
Non non non
Founé dem nafa founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah.
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah.
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek



Writer(s): Cheikh Ahmadou Kara Diouf, Dominique Preira, Ismaila Talla


Dip Doundou Guiss - NLMD
Album NLMD
date of release
19-01-2018

1 NLMD




Attention! Feel free to leave feedback.