Lyrics NOBOMA WOON - Dip Doundou Guiss
Le
passé
c'est
le
passé
Trop
de
problème
avec
toi
j'en
avez
assezz
ey
Maintenant
que
tout
a
changé
J'ai
tourné
la
page
car
tu
m'empêche
d'avancer
Thi
diir
bou
gat
lala
khamé
gua
beug
ma
jugé
Thi
sa
digue,
sa
ay
kharit
gua
sewalma
ni
i
Mane
yorou
mawone
khaliss
Mais
gniko
yor
sa
khol
iow
mousso
lenko
thiabil
Bamala
guissé
si
la
guiss
nit
kima
done
sét
Façon
yéne
gor
yii
nieupeu
yam
ganéma
mounoul
néh
Mane
melouma
nii
guar
gni
Sa
tank
sama
tank
gua
présenté
ma
PA
bii
Gua
begn
dh
néh
dou
mak
iow
Geume
lo
mani
né
mounougnoun
Dem
fén
mak
iow
Téré
nanie
ma
teud
temps
nah
doumala
am
iow
Iow
mi
sa
bop
yama
téré
ande
ak
iow
Gua
bagn
dh
néh
d'où
mak
yaw
Geum
lo
mani
meunougnou
dem
fen
mak
iow
Téré
nanie
ma
teud
temps
nkoul
ak
iow
Iow
mi
sa
bop
yama
téré
and
ak
iow
(bb)
Noboma
wone,
noboma
ndeyssane,
Noboma
wone
bameu
lay
face
time,
Talo
ma
wone
bameu
lay
message,
noboma
woo-woo-woo-ooh(×4)
Kouma
ko
wakhone
douma
ko
geum
ya
moudier
xewii
nii
Mane
iow
rk
la
guissone
gua
diapé
meuh
nit
invisible
Bayina
la
à
vie,
faté
gua
bigua
ma
done
rombe
ak
vitesse
Ferrari(thip)
Mbeuguel
indi
woula
lila
indi
dieulina
Tey
guamay
sogua
moune
sét
fep
ni
FBI
Rethie
nala
bayil
Way
bigua
ma
done
dieundé
lgui
gua
ko
niémé
trahir
Gua
begn
dh
néh
dou
mak
iow
Dama
la
mounoul
mounie
niou
dem
féne
mak
iow
Doma
téré
nakh
mounou
ma
ande
ak
iow
Iow
sa
bop
yama
téré
and
ak
iow
baby(×2)
Noboma
wone,
noboma
ndeyssane,
Noboma
wone
beumeu
lay
face
time,
talo
ma
wone,
doma
done
message
Noboma
Woo-woo-woo-oh(×4)
Pourquoi
tu
crois
aller
venir
quand
tu
veux
Cette
fois
hélas
c
trop
tard
ohh
woo-woo
Attention! Feel free to leave feedback.