Dope Master - aMin Lyrics

Lyrics aMin - Dope Master



Nigga whts'up
I'm in the game like a braind new boss
Yoh what you've done
Romb ay dadj hey dope day féssal loudoul seu bopp
Job moy fay nguenn beugu beugu ma fay konn fay day yomb
Gwaye kinpi dou yeup niongui fi dawou niou
Dawou ma khér
Meuno Lo féyi boul sobou si guerre
Boy yi dagn niangu teh défou niou keutchi
Deugu si ligeuy teh geumou niou
Damn
Peundeul meu mbeundeu bi diekh
Kharou si mission bi matal ko céyi fi yeup
Diakhlé kom good bou diabaram titeul
Bala nguay comp film bi diékh na
Meussoul yomb mais fuck seu bras long sama dh la geum
Tèki teral gnissi yagua diap déf roganiou none si red cup
Way geunone na fi méti mais wakhone nala man i can never give up
Am na nianeu mère am na nianou père louma bok ak gniy sopp
Kom fusée boy si kaw dh lagn dieum
Beugu gnibi melni benen planet lagn diogué
Niom marr ay tateu dh lagn geum
Fi click paw ballou gun si bopp fake
Li moy real life kou Yom dou def
Nite bo yéné diam mou déf la khatchieu
Sougn leu meunoul teuyé dougn beugu ngua dém
Dagn lay nianal tiolé bagn ngua géneu si Damn
Amine
Nianal ma Diam amine
Amine
Nianal ma Diam amine
Amine
Nianal ma Diam amine
Tiolé dh meunou niou deuk si bir
Lékouniou na nou niou
Dawou niou beef (dawou niou 2x hey)
Amine
Nianal ma diam
Amine
Nianal ma Diam amine
Amine
Nianal ma Diam amine
Tiolé dh meunou niou deuk si bir
Lékouniou na nou niou
Dawou niou beef
Tiolé dh dougn deuk si bir
Ratissé feep si terrain ni khamé ngua numero 6
Tiouameni
Nieuw pour dieulsi li ma mom pussy nigga beugu ma siss
Doumala djik
Kom djiguénou diamono dji
Rappeur yeup niongui youkhou mann bokou massi
Fi nieupeu Niro ay style
Couper coller guiss ngua boy yi dh defou niou diff
Niom jobogn di sani ay pic
Mann guéwou tiouné meuno nelaw beu guènt ma si
Beugoma teh khaw mala fils
Yangui tiéné mangui money rek di geuneu diss
Tassaré di def bénéfice
Guinaw bou bétonner sokhla wouma dimbali nah
Vision bou enigmatic
Nél sama concurrent tiolé neu Og dou bitch
Og dou tiéré
Dou tioubou dou yolé
Loum wakhone seu guinaw lay wakh at seu kanam
Nioun beugu lou yomb ndakh beugu lou diafé
Sou succès bi nieuwé na fek niou paré bou yagu
Gagné respect bou diaré niou rakk
Téki khal ak ay president
Nigger palais mafay ndieuk tall Grrr baw
Amine
Nianal ma Diam amine
Amine
Nianal ma Diam amine
Amine
Nianal ma Diam amine
Tiolé dh meunou niou deuk si bir
Lékouniou na nou niou
Dawou niou beef (dawou niou 2x hey)
Amine
Nianal ma diam
Amine
Nianal ma Diam amine
Amine
Nianal ma Diam amine
Tiolé dh meunou niou deuk si bir
Lékouniou na nou niou
Dawou niou beef




Dope Master - aMin - Single
Album aMin - Single
date of release
17-02-2023

1 aMin




Attention! Feel free to leave feedback.