Elzo Jamdong feat. Mathart - Nama Yalla Baal - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Elzo Jamdong feat. Mathart - Nama Yalla Baal




Nama Yalla Baal
Le nom d'Allah le Tout-Puissant
Tall bou Yallah tall meune wakh fayoukoo (Tall bou yallah tall wakh fayoukooo)
Lève-toi, viens, suis-moi, il y a quelque chose pour toi là-bas (Lève-toi, viens, suis-moi, il y a quelque chose pour toi là-bas)
Nama Yallah baal gnoungui seine kaw (Nama Yallah baal niongui seine kaw yow)
Au nom d'Allah le Tout-Puissant, on est ensemble (Au nom d'Allah le Tout-Puissant, on est ensemble, ouais)
Taakeu shine di leer nagne ni bideeeewww
On brille de mille feux, on avance et on ne recule pas
Tall bou Yallah tall meune wakh fayouko (wakh fayouko wakh fayouko)
Lève-toi, viens, suis-moi, il y a quelque chose pour toi là-bas (là-bas, là-bas, là-bas)
Tall bou Yallah tall meune wakh fayouko (Tall bou yallah tall wakh fayoukoooo)
Lève-toi, viens, suis-moi, il y a quelque chose pour toi là-bas (Lève-toi, viens, suis-moi, il y a quelque chose pour toi là-bas)
Nama Yallah baal nioungui seine kaw (Nama Yallah baal nioungui seine kaw yow)
Au nom d'Allah le Tout-Puissant, on est ensemble (Au nom d'Allah le Tout-Puissant, on est ensemble, ouais)
Taakeu shine di leer nagne ni bideeeeew
On brille de mille feux, on avance et on ne recule pas
Tall bou Yallah tall meune wakh fayouko
Lève-toi, viens, suis-moi, il y a quelque chose pour toi là-bas
Yeaaaaaaahhhh
Yeaaaaaaahhhh
Tall bou Yallah tall (Tall bou Yallah tall)
Lève-toi, viens (Lève-toi, viens)
Toll bou Yallah bèy (Toll bou Yallah bèy)
Lève-toi et brille (Lève-toi et brille)
Diam bou Yallah falle
Calme-toi et sois forte
Dey gueuneu taak di gueuneu teuweu faye
Que ceux qui veulent parler, parlent, ceux qui veulent se taire, se taisent
Yeah yeah
Yeah yeah
Fall kou Yallah may dale lo beugueu nangou tchi mome nangua nangou ni dangko koy faye
Si Dieu le veut, on ira loin, au-delà de nos espérances, au-delà de nos rêves les plus fous
Ndax kou Yallah may baat dina wakh tei kou ame bou nekh dakoy waye
Car si Dieu le veut, il n'y a rien de plus beau que de réussir ensemble
Fama dane lakahatou si gnimeu gueuneu diégué
On se connait depuis l'enfance, on a grandi ensemble, on a partagé les mêmes galères
Dama leerone si séni beutt bagnou goumbeu
On a appris à se relever après chaque chute, à être plus forts ensemble
Gnimeu gueuneu sorri gnoma dane nieukeu sèinn mey taak di maag niou melni niou moumeu
On a connu des moments difficiles, mais on a su rester soudés, on a su se serrer les coudes, on a su avancer ensemble
Niveau bi gueuneu kawei lay football
Notre niveau est élevé, on est comme des joueurs de football
Légui joueur yifi eupeu gueudd lay dougeul
On est des joueurs talentueux, on peut marquer des buts
Dama diouk djité xarouma adiouma
On travaille dur, jour et nuit, sans relâche
Mangui weurr kane momeu soutt tei guissouma
On se bat pour réussir, on est déterminés à atteindre nos objectifs
Soubeu si djante la goudii weirr
On sait que le chemin est long et difficile
Taak na shine boul bagne lolou keine doussi polymiquer
Mais on brille de mille feux, on est comme des diamants, on est uniques
Ngandeu la leer neu may tchatou bideew bou dioudou feirr di lekk si bolou magg yii
On avance avec confiance, on est déterminés à réussir, on est comme des lions
Fangu na fègne na
On n'a peur de rien, on est courageux
Diombi ngeine ndax doolé dji nek tchi mane mo gueuneu kawei doolé djiné
On se soutient mutuellement, car on sait que l'union fait la force
Rangou na kheikh na ba togu tchiin bi yagueuneu kheign nekh tédou gowé tchi nègg yeah
On est une famille, on est unis, on est solidaires, on est ensemble
(Refrain)
(Refrain)
Nagnou Yallah baal
Au nom d'Allah le Tout-Puissant
Yagueuna def ay hits (Alright)
On fait des hits (Alright)
Bobou amagouma wone ay clips (Alright)
On tourne des clips (Alright)
Li fi Thiere bindeu si ay récitou bits eupeuna ay livres diekhal na ay bics (Come again)
Ceux qui sont à Thiès enregistrent des freestyles, certains écrivent des livres, d'autres des textes de rap (Come again)
Manei yagueuna bégueul ay niits (Wallay)
On passe des nuits blanches à travailler (Wallay)
Bobou amagou wone ay sites (Wallay)
On est présents sur tous les sites web (Wallay)
Binguay nieukeu dègu limeu bindeu dangua replay nangoulni kone mousso wone write (Doope)
Les filles nous adorent, elles écoutent nos chansons en boucle, elles connaissent nos paroles par cœur (Doope)
Yow ma dakk rap Sénégal Dial home mo nei tchi ngiurr gui defko sama fringdom
Ouais, je représente le rap sénégalais, je suis un roi dans mon domaine
Sama dope legalize soumeu nekhone gueinei beum boumey toudei Dakar-Kingston
Ma musique est légale, elle est appréciée de tous, elle est un pont entre Dakar et Kingston
Ame dieundeul bi defko ringtone
Mon son est unique, il est devenu une sonnerie de téléphone
Nioungui job moussou gnou ame pistons
Mon travail est ma priorité, je me donne à fond
Koula ladj ndax mangui gérer fight bi neiko may Mouhamed Ali sikaw ring bro
Je suis un champion, je suis un battant, je suis comme Mohamed Ali sur le ring
Mane damey taak doumeu mandii
Je suis un homme de parole, je tiens mes promesses
Ay dadjeu naturels lay andii
Je suis un homme de principes, je suis intègre
Defla Mario diam leu ay champis
Je suis un champion, je suis un gagnant
Soudone western movie danioumey wanted
Je suis un héros, je suis un hors-la-loi
Eh boulmeu wane sa kanamou gentil
Je ne suis pas un ange, mais je suis gentil
Xamnani yangui niane meu faye ngeu meune trankil
Je suis calme et tranquille, je ne cherche pas les problèmes
Damey gass tombe soul ay garçons comme Gaston tchi microphone mane may bandit
Je suis un bandit au micro, je vole la vedette
From the underground ligeey bi doroul tey (doroul tey)
On vient de la rue, on a connu la galère (la galère)
Guisngeu agueu nagne tchikaw ligeey bou sett dey faye (dey faaaaaye)
On a gravi les échelons un à un, on a réussi (réussi)
Kileu yagu tipseilo keip sa good time (Tiiiiiimmmmmeeeee)
On profite de la vie, on s'amuse (Tiiiiiimmmmmeeeee)
Get sunu vibes
On vit à fond
Alright (Ouh yeah Ouh yeah)
Alright (Ouh yeah Ouh yeah)
Daniou daurr mou nathieu nigger nieupeu seddeiko ko wallay (Seddeiko wallay)
On est des lions, on n'a peur de rien, on ne se laisse pas faire (On ne se laisse pas faire)
Change game bi def safara andi ay mouslayes
On change les règles du jeu, on impose notre style
Never never nga guiss niou tchi details (Non non non non non non non)
On ne donne jamais de détails (Non non non non non non non)
Wowei meu grossiste
On est des gros bonnets
One more time (Ouh yeah Ouh yeah)
One more time (Ouh yeah Ouh yeah)
(Refrain)
(Refrain)
Nagnou Yallah baal
Au nom d'Allah le Tout-Puissant






Attention! Feel free to leave feedback.