Elzo Jamdong - Falaaw Lyrics

Lyrics Falaaw - Elzo Jamdong



yaw kay gnou job pour mou tanė bro
nak mou tanė
amoul khof
talougnou salso(salso)
warougnou planer
kay gnou job
nakh mou tanė bro
khamna lima beug
khamna lima beug
makoy doundou deug
makoy doundou deug
amoul lomay djangual
amoul lomay djangual
biguė yėksi sėne nala guė gniangual
sėne nala guė gniangual
yaw yafi gnew
falaw falawf alaw falaw
falaw falaw falaw falaw
falaw falaw falaw falaw, yaw kay gnou job warougne
planer bro warougnou planer
akh lougnou dokh warnagn
garer troc tabakh gualler
amna wotér amatoul
kharer bro amoul kharer
amoul khof talougn salsoooo amoul baller
yag johhhh motax yak tchiow legui damassi gorė
dakone fooo mala doree
ak tokh cigarette wayer noooo dama yagueu fort
manė fok mou carrė
fok gnou djok
borom meuk dowww
menoul khėkhhh ak armée
(khėkhhh ak armée)
legui soy Def liste ELZO djitou
$# ELZO djitou $#
bougne sagnone ma danou
¥ medzo diatta




Elzo Jamdong - Freeseason
Album Freeseason
date of release
31-08-2015




Attention! Feel free to leave feedback.