Elzo Jamdong - Keneen Lyrics

Lyrics Keneen - Elzo Jamdong



bignu ande ba legui dane gua sone gnuy dound lou mety
sa tank dane meti dane gua sokh wayé taxoul gua tegi
mousso ma togn moussoma diss liga ame ci ngor moussoumako guiss moussoma note meussoma dinguate suba ak ngone louma nior gua guiss
yaye sama gaïne sama miss sama star
sama way sama queen sama love
barigua yare teksi diné ak tare
yaye sama guaïne sama miss sama staaar sama miss sama star yaye sama way sama queen sama looooove barilégua yare teksi diné ak tare
mak ioe la boudoul ioe dou done kenen(×3)
lignu thiow yeup boudoul ioe dou done kenen
bobou bagui legui magui try wayé menouma xol fénéne
mani bobou ba legui gnugui fight mayé menouma dem fenen
mak ioe la boudoul ioe dou done keneeen(×2)
bignu andatoul ba legui magui dokh ci taly menouma diegui
sama tank dina newi magui sokh wayé takhoul ma tegui
moussoma togn moussoooma diss liga ame ci ngor moussoumako guiss moussoma lore moussoma dinguate sama xol tay amna guome ci bire
yaye sama gaïne sama miss sama srar sama miss sama star
yaye sama way sama queen sama loooove barigua yare teksi diné ak tare
yaye sama nite yaye sama niiiite mani yaye sama nite douma bayi douma tite
mak ioe la boudoul yow dou done kenen mak ioe la boudoul ioe dou done keeeneenn(×3)
lignouy thiow yeup boudoul yow dou done keneeen
bobou ba legui magui try wayé menouma xol feeeeneeene
mani bobou ba legui magui fight wayé meunagouma dem fenene
mak ioe la boudoul ioe dou ioe done kenen(×3)
maguini si loula nekh bess nek dagay bess melni gnogui doga tambalii_ii xamguani dou diekh kon waro meussa deglou gnilay wakh gnun niar dotoul amatiii
mani melgua noula nekh bess bouné dagay bess melni gnogui dogua tambaliiii-ii
kon wargua xamni man ak ioe dou diekh boul deglou gnilay tegal ni man ak ioe dotoul amatiiii
yaye sama nite yaye sama niiite mani yaye sama nite douma bayi douma tite
end!!!!!!!




Elzo Jamdong - Keneen
Album Keneen
date of release
04-08-2017

1 Keneen




Attention! Feel free to leave feedback.