Elzo Jamdong - Rwmr - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Elzo Jamdong - Rwmr




Rwmr
Rwmr
Keah keah keah keah
Keah keah keah keah
Rap wolof mo raw yeah
Du rap wolof brut, ouais
Rap wolof mo raw
Du rap wolof brut
Rap wolof mo raw
Du rap wolof brut
Rap wolof mo raw
Du rap wolof brut
Yeah
Ouais
Aka maa beuri ay fiston
Aka maa beuri ay fiston
Wowema deug iba keyti Bibson (Rap'Adio)
Wowema deug iba keyti Bibson (Rap'Adio)
Moussouma sokhleu se piston
Moussouma sokhleu se piston
Yalla may nama kattan ak diction
Yalla may nama kattan ak diction
Pour danel leu diaroul may tite
Pour donner à leurs familles, ils volent
Diaroul may yakamti caloul rek fils
Ils volent et dépensent tout, les fils
Ku diog song gaindé se kharou ngay guiss
Ceux qui travaillent dur gaspillent leur argent en boite
Se sho ak se cachet laay nangou ne tir
Avec leur meuf et leur cachet, ils dépensent sans compter
Dem chill seme borr
Dites-leur de se calmer
Rap naa siguil sama kogne
Le rap emplit mon esprit
Mais legui il est temps me diw semey poche niou diss
Mais vraiment il est temps, dis-moi, nos poches doivent être pleines
Comme nangou nga Free defe fort
Comme si j'étais Free, défendant le fort
Negn yengueul ba Sodav fey niou ndakh faut que niou riche
On est fatigués de la misère, il faut qu'on soit riches
Meun nekk MC nekk PDG (ha)
Moi, je suis rappeur et PDG (ha)
Diabanté AiBD ak CDG (ha)
Diabanté, AiBD et CDG (ha)
Souniou joboul tabakh tem niou khey rek
On fume nos joints, on boit notre thé
Souniou dome yi magg neniou wéré ngueen (hooo shit)
On prend soin de nos femmes, on ne les trompe pas (hooo shit)
Welcome to the Macina (ha)
Bienvenue au Macina (ha)
Mane le Amadou Ampathe ba ci rap (ha)
Je suis le Amadou Ampathe du rap (ha)
Ngandi kangam ni Cheikh Anta laa ci rap (ha)
Je suis le Cheikh Anta du rap (ha)
Yeubo Teaupla bi fattewoul racinam (haaa shi*)
Le yeubo Teaupla qui a retrouvé ses racines (haaa shi*)
Bro yeuppey capituler
Frère, n'abandonne pas
Lo kham ci poullo bou magué thi kognou lebou di leu lakk
L'ignorance est comme une poule mouillée, elle ne comprend que sa langue
Ay olof you lerre
Toi l'étranger
Kou fi attann sama vocabulaire?
Tu comprends mon vocabulaire ?
Rap wolof mo raaw rap wolof mo raw
Du rap wolof brut, du rap wolof brut
Nié wouniou states nié wouniou kaaw
On n'est pas aux États-Unis, on n'est pas à Kaolack
Djolof mo ndaw rek sinon niou yéngueul ba adouna
On est au Sénégal, sinon on serait fatigués d'être ici
Yeup kham ni nio gueuneu graaw
Ils ne peuvent pas nous suivre
Rap wolof changer woul pour gueuneu feegn
Le rap wolof a changé pour les faibles
Nioune wagni ay fans mo niou gueuneul fake
On a des fans mais on n'est pas faux
Niakk negn Las dotouniou nelaw (Las MC)
Hommage à Las, dotouniou nelaw (Las MC)
Bourba ak Pacotille ken doulene fey (Rest in peace)
Bourba et Pacotille, qu'ils reposent en paix (Rest in peace)
Rap wolof mo rawww (rap olofdio rap olofdio rap olofdio)
Du rap wolof brut (rap olofdio rap olofdio rap olofdio)
Rap wolof mo raw (rap olofdio, rap olofdio, rap olofdio)
Du rap wolof brut (rap olofdio, rap olofdio, rap olofdio)
Rap wolof mo raw (rap olofdio, rap olofdio, rap olofdio)
Du rap wolof brut (rap olofdio, rap olofdio, rap olofdio)
Rap wolof mo raw (rap olofdio, rap olofdio, rap olofdio)
Du rap wolof brut (rap olofdio, rap olofdio, rap olofdio)
Rap wolof mo raw
Du rap wolof brut
Rap wolof mo raaw, (rap wolof wolof wolof)
Du rap wolof brut, (rap wolof wolof wolof)
Nioune niè wouniou states my nigga nioune niewouniou kaaw
On n'est pas aux États-Unis mon pote, on n'est pas à Kaolack
(Rap wolof wolof wolof)
(Rap wolof wolof wolof)
Djolof mo ndaw rek sinon niou percer ba kaana yi
On est au Sénégal, sinon on percerait partout dans le monde
Nieuw di niou follow niou naaw
Qu'ils nous suivent, on est
Rap wolof mo raaw rap wolof mo raw
Du rap wolof brut, du rap wolof brut
(Rap wolof rap wolof wolof)
(Rap wolof rap wolof wolof)
Rap wolof mo raaw, rap wolof mo raw (rap wolof wolof wolof)
Du rap wolof brut, du rap wolof brut (rap wolof wolof wolof)
Nioune niè wouniou states my nigga nioune niewouniou kaaw
On n'est pas aux États-Unis mon pote, on n'est pas à Kaolack
(Rap wolof wolof wolof)
(Rap wolof wolof wolof)
Djolof mo ndaw rek sinon niou feusseul ba adouna
On est au Sénégal, sinon on serait connus dans le monde entier
Yeup kham ne nio gueuneu graaw
Ils ne peuvent pas nous suivre
Rap wolof mo raaw rap wolof mo raaw
Du rap wolof brut, du rap wolof brut
(Rap wolof rap wolof wolof)
(Rap wolof rap wolof wolof)
Rap wolof mo raaw
Du rap wolof brut
So feyoul douniou rap ak 'oit
Si on veut faire du rap et réussir
Il faut que niou takk ni 60 watts
Il faut qu'on donne tout, à 100%
Son bi tchi voit' ak boite
Du son qui s'écoute fort, en boîte
Shot out to Black G Rak Tak Squad
Shout out to Black G Rak Tak Squad
So feyoul douniou rap ak oit
Si on veut faire du rap et réussir
Da-da-damey diakhassé rap ak crack
Da-da-damey diakhassé rap ak crack
Rap wolof abadane
Du rap wolof authentique
Shout out rak tak squad
Shout out rak tak squad
Yeah Yeah
Yeah Yeah
Shout out rak tak squad
Shout out rak tak squad
Rap wolof mo raaw
Du rap wolof brut
Shout out rak tak squad
Shout out rak tak squad






Attention! Feel free to leave feedback.