Lyrics Reppin Time - Elzo Jamdong
Yeah
Yeah
Oh
shit
Eh
iow
Iow
dangniou
conditionner
ba
bo
beugué
tekk
li
sa
communauté
di
dund
da
ngay
sauralé
Mais
est-ce
que
niom
di
nagn
sauralé
suniou
wakh
ci
suniu
ay
famille
nombreuses
ak
suniu
febar
yi
nga
khamné
niom
nioko
inventer
Yeah
Yeah
Africains
dangniou
khepp
batay
Neeger
bu
tekki
sakh
Neegers
yi
dagnlay
khekh
batay
Colon
bi
néna
demb
moniou
civilisé
Motakh
luniou
meusseu
créer
dafko
dindimusé.
WOW
Sarko
néna
amouniou
history
Alma
lagnset
ma
niassalko
hiéroglyphe
sikanam
dangniou
yapp
sama
baat
Ci
kaw
nekal
waliyou
do
dara
ludul
black
si
niom
Suma
néké
town
kaawman
la
Suma
néké
kaaw
bledar
la
Lutakh
dugnma
wowé
expat
han
Deuk
banlieue
égale
deffkatt
la
faut
que
ma
dem
hophi
khol
bane
febar
la
am
melné
fima
diougué
SIDA
dafa
feug
niounéko
bismilah
Liniou
beuri
febar
yeupp
khamalni
crise
bila,
Nassarane
si
dafniou
yagg
forcé
guiss
guisseum
motakh
diplomatie
khétou
hypocrisie
la
Sa
life
yeupp
dagnlay
wonené
li
nga
kham
dara
amoucci
ndieurigne
li
nga
am
dara
amoucci
mérite
Linga
dondeu
si
say
mame
dagnla
nane
fatel
té
boul
réfléchir
khamo
nguerr
waayé
am
nga
aspirine
Correcte
moy
nduru
toubaab
soy
wout
liguey
bo
solé
grand
mboubou
dou
bakh
chemise
ak
patalon
rekay
duug
fu
baax
entretien
tégal
cheveux
rek
boul
yobou
foulard
li
tchi
mane
rek
dakk
dagn
koy
dondeu
après
colonisation
bi
gaayi
dagn
koy
doli
Bo
geustuwul
sa
bopp
toubaab
daflay
diomal
numla
def
nouko
raw
lakoy
def
say
dome
Complexe
dagn
koy
dondeu
Système
bi
dafkoy
yokk
Ma
ngui
fatélikou
bima
beugué
def
ay
locs
prof
prof
bi
néma
watoul
wala
sdf
ngay
done
Im
on
my
Reppin
Time,
Reppin
Time
Reppin
Time,
Reppin
Time
We
gotta
Make
it
Right,
Make
it
Right
Make
it
Right,
Make
it
Right
Im
on
my
Reppin
Time,
Reppin
Time
Reppin
Time,
Reppin
Time
suniu
mame
yi
dagnko
métiil
baye
métiil
baye,
now
we
gotta
Make
it
Right
Lifou
bitim
rew
dagnlay
humilier
Dagnlay
keuyitlo
ndakh
amo
keuyit
bro
Faut
que
nga
khekh
diayanté
pour
meun
nek
ci
diaam
Daniou
tekk
deal
diam
laniou
def
ci
mind
li
geuneu
meti
moy
niom
ño
ndieuk
nieuw
suñu
territoire
takk
boum
diaam
dieul
ci
tirailleur
Té
niouné
beugeutuñu
guiss
beneu
noir
Dagn
beugg
niou
teudd
geumm
ni
Schumacher
Ladiou
niou
keneu
mou
nieuw
sathie
suñu
or
wakhouniou
keneu
indil
bateau
yobou
suñu
maame
Lutakh
niom
howeepy
dawal
naka
sudul
nonou
parsk
ñi
nieuk
indi
thiow
baluwuniou
akk
(akhh)
Dieul
deukk
leumb
dompter
len
Balégui
Pubou
xessal
mi
ngui
daw
télé
Motakh
ba
suniu
sister
yi
di
am
complexe
ba
façon
febar
bu
nekk
laniouy
diankontel
Histoire
bi
dagnko
deupp
(Histoire
bi
dagnko
deupp)
(Histoire
bi
dagnko
deupp)
Histoire
bi
dagnko
deupp
chapitre
yilen
arrangeéwul
dagnko
teupp
(Yilen
arrangéwul
dagnko
teupp)
Do
degg
feneu
tabakhu
pyramide
niit
kou
nioul
mo
ci
ndieuk
(niit
kou
nioul
mo
ci
ndieuk)
Motakh
niit
kou
nioul
rekay
am
accenwu
niit
kou
nioul
diko
neubb
(Nioul
diko
neubb)
Boko
defoul
rek
niou
toulila
sen
deukk
Immigré
késsé
nga
dougnla
may
ludul
ass
tutt
So
meuné
diaamu
teuthie
sa
guémign
that's
Cool
Meun
nga
tidji
taxi
phone
wala
fast-food
So
beugué
changé
game
bi
dagnlay
gass
soul
Sa
lepp
laniouy
toutil
gniné
hip
hop
dou
culture
Il
faut
que
nga
nekk
bounty
pour
niou
ibbil
la
bountu
Lolo
waral
cité
yii
fess
dell
ak
ay
famillou
black
back
dugg
si
kogn
bi
nakhté
boyii
amuniu
bac
Yéna
ndieuk
nieuw
suniu
deukk
Té
bougolen
niou
guiss
sen
deukk
Di
nagnlen
wakh
suniu
deugg
Di
nagnlen
wakh
suniu
deugg
Yéna
ndieuk
nieuw
dieulsi
tirailleurs
yi
Té
beuggtolen
guiss
seyni
seutt
Di
nagnlen
wakh
suniu
deugg
Di
nagnlen
wakh
suniu
deugg
Im
on
my
Reppin
Time,
Reppin
Time
Reppin
Time,
Reppin
Time
We
gotta
Make
it
Right,
Make
it
Right
Make
it
Right,
Make
it
Right
Im
on
my
Reppin
Time,
Reppin
Time
Reppin
Time,
Reppin
Time
suniu
mame
yi
dagnko
métiil
baye
métiil
baye,
now
we
gotta
Make
it
Right
Reppin
Time
Reppin
Time
Reppin
Time
Make
it
Right
Make
it
Right
Make
it
Right
Reppin
Time
Reppin
Time
Reppin
Time
Metiil
baaaye...
Reppin
Time
Reppin
Time
Reppin
Time
Make
it
Right
Make
it
Right
Make
it
Right
Reppin
Time
Reppin
Time
Reppin
Time
Metiil
baaaye...
1 Reppin Time
2 Rwmr
3 Jengu
4 Contact
5 Diigu Sandaga
6 Xol Ma
7 Diallo Bo (Jamono)
8 Gentleman Rmx
Attention! Feel free to leave feedback.