Lyrics Samay Neggerz - Iss 814
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
setane
buñ
ley
rey
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
retane
buñ
ley
rey
Prrra
prrra
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
Prrra
prrra
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
(plomb
yeah)
Keneu
dou
négocier
(yeah)
Produit
qualité
(cali)
Ñeupeu
ko
valider
(yeah)
Keneu
dou
ko
copier
Siriki
ak
Suké
(prra)
Tite
da
nguey
comédie
(han)
Diokh
ñu
ay
tickets
(yeah)
Mba
ñu
appliquer
Amul
Kendal
Rihanna
(Rihanna)
Da
ñuy
ñow
taal
terreau
man
(terreau
man)
Djiko
Van
Damme,
Superman
(superman)
Def
scandale
sisa
mame
(yeah)
Ken
dou
bloquer
sunu
couche
(sunu
couche)
Da
ñu
blessé
gana
pousse
(yeah
yeah)
Gueumeu
ñu
tok
banc
de
touche
Ay
djiko
bone
gana
louche
(yeah
yeah)
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
setane
buñ
ley
rey
(bougou
ñou
la
un
deux)
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
retane
buñ
ley
rey
Prrra
prrra
(prrr)
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
(dinero
dinero)
Prrra
prrra
(skut)
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
(dinero
dinero)
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
setane
buñ
ley
rey
(skut
skut
skut)
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
retane
buñ
ley
rey
Prrra
prrra
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
(dinero
dinero)
Prrra
prrra
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
(yeah
yeah
yeah)
Ngané
do
fey
ok
Magnum
sissa
bop
pop
nga
deh
Amoul
demi
xaliss
buñuy
accepter
Meno
ñu
reutieu
ñu
gui
si
quatre
côtés
Sama
lamigne'a
dama
sa
yaram
kot
koté
Teuyeul
ñu
sa
wax
yi
diaroul
papoter
Sa
bop
ak
sa
nop
lañuy
fat
faté
Taxaw
sa
kanam
comme
bateau
ma
accosté
All
ok
Feyoulo
da
ñu
ley
shoot
(shoot)
Amulo
on
s'en
fout
Na
nga
ñow
buñu
doul
(yeah)
Boufi
wax
da
ngey
loud
(loud)
Dañuy
job
duñu
play
(play)
Bo
fiy
fo
dañu
ley
rey
(rey)
Moratoire
non
dou
tey
(hey)
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
setane
buñ
ley
rey
(bougou
ñou
la
un
deux)
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
retane
buñ
ley
rey
Prrra
prrra
(prrr)
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
(dinero
dinero)
Prrra
prrra
(skut)
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
(dinero
dinero)
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
setane
buñ
ley
rey
(skut
skut
skut)
Samay
niggas
beugou
ñou
la
Da
ñou
ley
retane
buñ
ley
rey
Prrra
prrra
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
(dinero
dinero)
Prrra
prrra
Diox
ñu
xaliss
wala
plomb
(yeah
yeah
yeah)
Attention! Feel free to leave feedback.