Jeeba - Guuy Lyrics

Lyrics Guuy - Jeeba



Dinala dall fokodoul fogué foko doul xalaté
Thi bangay Doug ci lilay dougué
Day melni yalla ko yoné
Dina fess sa xol bi, no (no,no)
Guelemeul sa bopp bi an (yeah,yeah)
Ba doto amati principe, baffoué nga lepp
Meno si mome sikeu
Yaw loumou layy deff dou yaww rk Yako xamm dou lou nitt mena waxx
Yaw figamay yobou Dafa melni messu
Mafa demm wayé dou lou nitt meuna waxx
Ma topou sa guinaw di daw
Melni mbeugellu xallé xallé xallé
May lathie kagn lay maguè
Nga téyé sama yeuré biii
Gnu xandal dawal mbégué mbégué mbégué
Degg na saxx dama diongué



Writer(s): Unknown Unknown, Abdoul Aziz Fall


Jeeba - Guuy
Album Guuy
date of release
12-02-2021

1 Guuy



Attention! Feel free to leave feedback.