Jeeba - Yitma Lyrics

Lyrics Yitma - Jeeba



Jeeba le boy
Ehhhh ehhh
Ehhhh
Mane dinala adj fou kene doul adji
Gnou wadjal ma done sa aladji
Dinala taguil Sama dadji
Dinala djiokh souma neh El comme dadju
Yaw yamanewone mani leuh
Nganimeuh gor tamunako si kadu
Kone diaratul ladj damala
Djaral ngama sopaliko niago nane kagnou
Doumako yagal fene deme sa papà
Defa niete ak trans
Ngananma papà ahh
Ahhhh bae comment tu vas
Est ce que mongui bakh
Nakh killa beug deug
Moy killay topato
Killa beug douko neub
Diko youkhou ohh oooh haa
So i love you
Baby i love you
Mbeuguel la neukh
Mbeuguel la nekhh-hhh
Boudone guedj deh lap na ci yaw
Mane dotouma tèhhh
Mbeuguel la neukh
Mbeuguel la nekhh-hhh
Boudone guedj deh lap na ci yaw
Mane dotouma tèhhh
Mane yaw yama mome
Mane yaw yaaaaama mooome
Loula nekhoul si mane dagal sani
Yaw yama moooome
Yaw yama mome
Mane yaw yama moooome
Lula nekhoul si mane dagal sani
Yaw yama mome
Ehh ehh
Ehhhhh ehhhh
Mane soma togne manla akhlou brick i'm Sorry
Mane May sa Jerry yaw yaye Sama berry
Louy bakh ci Sama khol bi yakoy Jerry
Gawal gaw bila May jer jery
Nakh linga done khar ci mane lalay wane tay
Newoune nala goorè ne goorè reko Kay day
Kone rousna douguat sa gualeh dila djieuli
Gnounanma sa baby dafa fight
Mak yaw Adventure boudoul djiekh
Douma manquer
Moh mangui tele novelas
Baby yitma
Je t'aime i love you take care row
Nala Berger banga nelaaaa-ss
Bebe beuguenala i love you take care row
Nala Berger banga nelaaaa-ss
My love
Mbeuguel la neukh
Mbeuguel la nekhh-hhh
Boudone guedj deh lap na ci yaw
Mane dotouma tèhhh
Mbeuguel la neukh
Mbeuguel la nekhh-hhh
Boudone guedj deh lap na ci yaw
Mane dotouma tèhhh
Yaw yama mome
Mane yaw yaaaaama mooome
Loula nekhoul si mane dagal sani
Yaw yama moooome
Yaw yama mome
Mane yaw yama moooome
Lula nekhoul si mane dagal sani
Yaw yama mome
Mane yaw ma mome
Yaw yama mome
Yaw mama mome
Beh yaw yama mome
Loula nekhoul si mane dagal sani
Yaw yama mooooome
Yaw Yaya mome
Yaw yama mome
Louma ame yaka mome
Yene na
Be yene nala
Yenenaaala Sama khol
Yaw yaye borom
Sama yit
Yiiitmaaaa
Mbeuguel la nekh
Mbeuguel mbeuguel la nekh
Boudoune guedj deh lap na ci yaw
Mane dotouma tèhhh
Mbeuguel la nekh
Mbeuguel la nekh hhhh
Boudone guedj deh lap na ci yaw
Mane dotouma tèhhh
Yaw yama mome
Kamzo



Writer(s): Bril, Djibi Ka (jeeba)


Jeeba - Yitma
Album Yitma
date of release
21-02-2020

1 Yitma



Attention! Feel free to leave feedback.