OMG - Bayil Mou Sedd Lyrics

Lyrics Bayil Mou Sedd - OMG



OMG!!!
Ngoor amoul ndieuk boulko diay
Goree ba kheuy deh boulko bayi
Di dounde lo donoul amoul ndieurigne nanko bayi
Diarouko way, fékhél nank ko bayi
2 ans yangui koy topp
Xalè bi néna bouggoula
Def nga louné wakh louné
Mome noboula
Lékato nélawato
Dem nga bay khalat ni faw nga diouk serigne touko
Manila, bayil mou sed
Bayil mou sed
Bayil mou sed
Diarouko, Bayil mou sed
Nièmé sagnsé téléphone bou guène nga am ko
Yaw rek thi khalè cheveux bou cher nga solko
Ndékété yo yoro dangay abb yoro
Niodi boss di diay lou amoul nieupeu kham ni yoro
Kone, Bayil mou sed
Bayil mou sed
Bayil mou sed
Yoro kone, Bayil mou sed
Ngoor amoul ndieuk boulko diay
Goree ba kheuy deh boulko bayi
Di dounde lo donoul amoul ndieurigne nanko bayi
Diarouko way, fékhél nank ko bayi
Bay bay bay, Bayil mou sed
Bay bay bay, Bayil mou sed
Bay bay bay, Bayil mou sed
Bay bay bay, Bayil mou sed
Eeh nénaleu, Bayil mou sed
Eeh, Bayil mou sed
Diarouko, Bayil mou sed
Eeh, Bayil mou sed
Bayil mou sed
Néna moy sa kharit yaw rek la tek beute
Lo am dakoy nakhari gnéné nek leu moungék keur
Nga sagnsè mokoy sonal
Sa mbecté bonal kholam
Yeuk ngeu ni dalay sossal
None la Bouko falé, Bayil mou sed
Eeh, Bayil mou sed
Bayil mou sed
Diarouko, Bayil mou sed, anh
Mome mak la ba legui nango gouko
Weur thi kogne bi dieul thi khalé bayé gouko
Niouleul bopp
Guéné face
Di diay taar
Père, Bayil mou sed
Dem nga feep
Wakh ngakh nieup
Kham nga lepp
Kone père, Bayil mou sed
Ngoor amoul ndieuk boulko diay
Goree ba kheuy deh boulko bayi
Di dounde lo donoul amoul ndieurigne nanko bayi
Diarouko way, fékhél nank ko bayi
Bay bay bay, Bayil mou sed (Eeh manila manila)
Bay bay bay, Bayil mou sed (Manila, manila)
Bay bay bay, Bayil mou sed (Eeh ganima, ganima)
Bay bay bay, Bayil mou sed
Eeh nénaleu, Bayil mou sed
Eeh, Bayil mou sed (Skrrr, Skrrr)
Diarouko, Bayil mou sed (Gani, gani, gani)
Eeh, Bayil mou sed (Dégouma)
Bayil mou sed (Dégouma)
Eeh nénaleu, Bayil mou sed (Ay waaye, ay...)
Eeh, Bayil mou sed (Kay, kay...)
Diarouko, Bayil mou sed (Eeh diarouko, mani diarouko)
Eeh, Bayil mou sed (Dégouma)
Bayil mou sed (Dégouma)
Diarouko, Bayil mou sed



Writer(s): Amadou Ndiaga Faye


OMG - Bayil Mou Sedd
Album Bayil Mou Sedd
date of release
17-12-2019



Attention! Feel free to leave feedback.