OMG - Yeugueul Ci Say Mbagg (feat. Dip Doundou Guiss) Lyrics

Lyrics Yeugueul Ci Say Mbagg (feat. Dip Doundou Guiss) - OMG



Omg
Yaw tay diethe sa dokh dou diekh
Yaw téne boudoul meusseu tay
Yaw tay diate say lampe dou fay
Bou gudi dioté yay done bidew
Kenne doula diap bayila
Melni yaw ta diaffé na
Yaw yay sama kani
Kone FO diar ma tathie la
Nigua mell dall eupeuneu
Ngoor bou bakh tay diafféna
Sama khole nigua koy deff
Lolou rk mo takh ma beugueula
Yeugueul ci say bagg
Ci say bagg
Yeugueul ci say bagg
Yaw koula am faw mou féthiala
Yeugueul ci say bagg
Ci say bagg
Yeugueul ci say bagg
Paréna fo dieum yobaléma
Yeugueul ci say bagg
Ci say bagg
Yeugueul ci say bagg
Koula am faw mou féthiala
Yeugueul ci say bagg (ohoh)
Ci say bagg (ohoh)
Yeugueul ci say bagg
Paréna fo dieum yobaléma
Fo nekk diam diougoufa
Foo du réé mane weetalouma
Diapal figua diap boulko bayi
Beugueuna ma diapeu
Fima diapeu lo wax lepp degg
Done sa dioguama dila
Wowé nidiaye
Do rebeu soy yaw leuh
Guaïdé Ndiaye
Kenne doula diapeuh bayila
Melni yaw tay diaféna
Yaw yay sama kani
Kone fo diar ma tothie la
Nigua mell dall eupeuneuh
Ngoor bou baff tay diafféna
Sama khol niguakoy deff
Rek motakh ma beugueula
Yeugueul ci say bagg
Ci say bagg
Yeugueul ci say bagg
Yaw koula am faw mou féthiala
Yeugueul ci say bagg
Ci say bagg (ohoh)
Yeugueul ci say bagg
Ci say bagg (ohoh)
Paréna fo dieum yobaléma
Yeugueul ci say bagg
Ci say bagg
Yeugueul ci say bagg
Ci say bagg
Koula am faw mou féthiala
Yeugueul ci say bagg
Ci say bagg (ohoh)
Yeugueul ci say bagg
Paréna fo dieum yobaléma
Koula am yow
Am yow
Ohwa ohwa wééh
Koula am yaw
Am yaw
Ohwa ohwa wéé
Firouma boul firr
Beugnala khamko
Loufi gueuneu diss doundou nako mak yaw
Beuguel DEUG doukou saysay yéé
Ligua beugoul diess bayinako ndax yaw
I did want a now
Tay me i did want a now
Watch wone to me
I did want a now
Girl You garalek me now
Watch wone to me
Yaw la tandem ci say morome yaw
Beugueu touma diess say rongogne yaw
Digueunté bi darra douko dakk
Li dara douko dagg
Yeugueul ci say bagg ehhh
Ehhhhhhh
Ohwa ohwa ohwa
Koula am warnala téé boubax
Warnama téé bou bakh
Ohwa ohwa
Paréna fo dieum yobaléma
Ohwa ohwa koula am
Warnala téé bou bakh
Ohwa ohwa
Paréna fo dieum yobaléma



Writer(s): Amadou Ndiaga Faye, Oumy Gueye


OMG - Yeugueul Ci Say Mbagg
Album Yeugueul Ci Say Mbagg
date of release
15-02-2020



Attention! Feel free to leave feedback.