Lyrics Yallah Baaxna - OMG
Par
AbouAmg
Sa
youma
kheuyé
damay
sante
sakou
niane
Yallah
mousseul
ma
thi
am
xol
bou
boon
Bania
wathi
yoon
bima
wadjour
yi
teggone
Dakhté
Yen
dis
damay
diekki
tite
thi
man
Di
guiss
ay
djiko
youma
khamoul
woon
si
mane
Mba
dou
diamono
dafolay
doakh
sopi
sama
X
lou
bakh
Guiss
loulay
sikeul
gueneu
yomb
guiss
sa
mbakh
Def
louy
yakh
gueneu
yomb
louy
defar
Alal
djiteul
niou
baniou
dem
ba
faté
Yallah
Han
han
hannn
ouais
eh
eh
oui
eh
Oh
non
oh
oh
oui
Diamono
diéka
dooy
waar
Gni
di
Gass
gni
di
âme
Kagn
était
baax
Mbok
deugueratoul
Xarit
deh
amatoul
Ken
guemeutoul
ken
dax
ken
woreutoul
Xol
Yangui
khat
di
gueneu
leudeum
Yénenté
wouniou
Jamm
kou
nek
djiteul
boppam
Kila
gueneu
Diègue
gueneu
meuneu
def
lou
SNPV
Yamatoul
thi
Daas
paka
Bilay
diam
thi
guinaw
Xol
yi
fess
na
del
sokhor
ak
ignane
Dieuf
diou
baax
dou
wess
Yallah
baaxna
Naniou
Delo
Xel
thi
Yallah
baaxna
Delossi
djiko
vous
Rafet
yi
Yallah
baaxna
Naniou
Delo
Xel
thi
Yallaf
thi
Yallah
thi
Yallah
Yallah
baaxna
Naniou
Delo
Xel
thi
Yallah
baaxna
Delossi
djiko
vous
Rafet
yi
Yallah
baaxna
Weurseuk
ken
douko
lekk
koudoul
Borom
Yallah
baaxna
Han
han
han
Yallah
baaxna
Ouais
ouais
ouais
Yéné
nék
le
borom
mossiy
fanane
Kone
naniou
yénenté
jamm
ak
salam
Attention! Feel free to leave feedback.