One Lyrical - Banlieue 13 Lyrics

Lyrics Banlieue 13 - One Lyrical



Dama djoudo ci guéro
Magué ci guéro
Waxléne ko fala beugu deii (Guérro)
Boy banlieu keine douma lall
Original ndakh yeine yeinama ndieuk tall (Guérro)
Guinaw ray lay tiiteuro
Xeiixx aq Cissé Lo sagne nako tei keine douma téyé (Guérro)
Fi ndokh miy taa lay reupeuzaine
Marouma nane, mak yeine ba lalou hopital (Guérro)
Pikinité lokho yi ci kaw
Béguéll boudé fier gua lokho yii ci kaw(Guérro)
Dagnou nitté paré gniémé thiow
Amougnu mais non stresse lagnuy doundou ci xoll (Guerro)
Bagn guathier fété sougnu boorr
Dagua beugu xame couddd bi daguay gnieukk xôle (Guérro)
Fi lagnu djougué outték nignu meill
Xana xamoni banlieuzar doko foutii ci neine (Guérro)
Ndongok Thioubako ana Pape Diouf
System gokh bi teikk nagn coup de pousse
Thiguirimbi aye thia niamou mbame
Légendaire Omzo Rabatata ...
Guerro
Guerro
Guerro
Guerro
Beigu ci mane fier ci mome
Beigu ci gnune beigu ci yeine fier ci gniome
Beigu ci mbeuss Eumeu Sene Champion
Rest in peace Doudou Diouf platinum
Leikougnu nanougnu teiyiitt gnéwougnu
Gnune dougnu nagou tei sanguinérougnu
Thiaroy ba diameugeun Diaksaw fier ci gnune
Parcelle ba Guediaway Nimzat fier ci gnune Guérrow
Gno dieul ci sougnu generation
Topal ndakh dagno clean diapo
Feipp fougn deime gnune Pikine lagnuy baako
Yeine gnieupay daccord yeine gnieupay bégué waww goor
Mane dama bagn guathié dagua beugu xame lathiéll
Gnune dagnuy door dakké
Khamougnuy louy wouy sathiéy
Fi echec day xarr comme kou geinte di mbott Sathies
Maffi diarone merci dakar Ciguithior (Guerro)
Boudé guerro guay live sa lokho ci kaw may guiss
Dagnu lay téral guay guiss kone douleine terei gnieuw live (Guerro)
La rochette lamsarr,
Yeumbeul ak sac mbao keur massa big town thiaroy azur daff (Guerro)
Guerro
Guerro
Guerro
Guerro
Guerro
Guerro
Guerro
Yeah, ok
Son bi dédié nako ambou guerro
Moy sama AMC moy sama hero
Guerro ladone mane (bis)




One Lyrical - Potentiel
Album Potentiel
date of release
27-09-2019




Attention! Feel free to leave feedback.