Lyrics Il est l'heure - Souleymane Faye
Mane
lima
gueneu
jaxal
si
xaley
Sénégal
moye
Musikou
lemzo
diamono
bi
daniouko
chœuru
par
choeur
Mane
lima
gueneu
jaxal
si
xaley
Sénégal
moye
Licci
télévision
bi
yeup
daniou
ko
chœuru
par
chœur
Ta
ko
ci
ne
récitelma
sa
récitation
Bi
duleuko
meuneu
recitel
par
chœur
Mane
lima
gueneu
jaxal
si
xaley
Sénégal
moye
Musikou
lemzo
diamono
bi
daniu
ko
chœuru
par
chœur
Il
est
l'heure
il
est
l'heure
il
est
l'heure
Suñu
télévision
bi
dafa
am
chœur
Il
est
l'heure
il
est
l'heure
il
est
l'heure
Suñu
musik
bi
dafa
am
heure
Il
est
l'heure
il
est
l'heure
il
est
l'heure
Diangui
école
wala
métier
dafa
am
heure
Il
est
l'heure
il
est
l'heure
il
est
l'heure
Takki
diabar
dafa
am
heire
Xalei
bi
buy
diangui
école
Dafay
fokni
ay
wajuram
laye
jangal
Bala
muy
xamnei
boppam
laye
jangal
Bete
bou
deimei
baye
binde
lettar
Jangal
Il
est
l'heure
Nekk
xale
mettina
yaye
xamna
si
dara
Nekk
xale
mettina
yaye
xamna
si
dara
Bul
waxli
Bul
deffli
Demal
fi
Awal
fi
Waxal
li
Solal
li
Simil
li
Togal
li
Boul
lekk
li
Nekk
xale
mettina
yaye
xamna
si
dara
Boul
deff
li
Boul
wax
li
Solal
li
Simmil
li
Muñal
so
magué
mou
jex
Muñal
xalei
bi
muñal
so
magué
mou
jex
Muñal
Lima
jaxal
si
xaley
Sénégal
moye
Musikou
rap
bi
dañu
ko
chœuru
par
chœur
Mane
lima
gueneu
jaxal
si
goney
moye
suñu
Télévision
bi
daniou
ko
choeuru
par
chœur
Wayei
kocci
ne
récitelmasa
Récitation
bi
duleuko
meuneu
récitel
par
choeur
Il
est
l'heure
il
est
l'heure
il
est
l'heure
Jangui
école
wala
métier
dafa
am
heure
Il
est
l'heure
il
est
l'heure
il
est
l'heure
Iow
deimal
seyi
dafa
am
heure
Takkil
jabar
dafa
am
heure
Attention! Feel free to leave feedback.