Viviane Chidid - Wuyuma Lyrics

Lyrics Wuyuma - Viviane Chidid



Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
Beugue nala xamothie dara
Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
Beugue nala xamo thie dara
Mane déh walouléne ma wax koko
Xalé bi lékatouma ndax mome
Nanatouma nélawatouma
Wowo
Sama xol yathie néh
Lék lék ma woo ko tit dal di coupé
Sama appetit coupé
Febar dinama guoungué
Doctueur dama love ba dof
xawma loukoy fathie
Wowo
Mba meune nga thie daraa
Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
Beugue nala xamothie dara
Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
Beugue nala xamo thie dara
Mane woo nala founé
Nga diapémma sa xarite
Inviter resto, lalal nala louné
Wowo
Nga diapéma sa xarite
Lék lék ma woo ko tit dal di coupé
Sama appetit coupé
Febar dinama guoungué
Doctueur dama love ba dof
xawma loukoy fathie
Wowo
Mba meune nga thie daraa
Mane beuguena ma bagne bayiwouma
Mane guisoumaa
Kénén koudoul mome
Mbeuguéleu beuri dolé yén mako xam
Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
Beug
Ue nala xamothie dara
Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
Beugue nala xamo thie dara
Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa
Beugue nala xamothie dara
Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu
Beugue nala xamo thie dara
Kouthie nek'aak kingna nope
Sa guinaw bandague faxassul
Diougueul yyeungueul bamou saf
Sa gnuinaw badanue faxassul
Kouthie nek'aak kingna nope
Sa guinaw bandague faxassul
Diougueul yyeungueul bamou saf
Sa gnuinaw badanue faxassul



Writer(s): Akatche Koffi, Beneth Seraphin, Viviane Chidid


Viviane Chidid - Divas Mix: Disc #2
Album Divas Mix: Disc #2
date of release
03-12-2016




Attention! Feel free to leave feedback.