Wally B. Seck - Fii Lay Né Lyrics

Lyrics Fii Lay Né - Wally B. Seck



Fii lay
Néké mbeuguél fii lay
Dama am sa faiblesse
Xoll bi yathie féss
Took dila diandér di dioy
Dafmay daal
Non non non non
Nileu nileeeu
Damay woo Dame séne
Sama kaw scéne
Takaal ko chaine
Nguire mou beguelel maleeu
Diokh Nala thieur bi
Ba Mél ni koula ragal
Dafmay daal
Awma ci kérsa
Deugeul nani diam
Ci yaw lakaay amé woor nama
En batay
Néna mbeuguél
Filay
Woo batay
Mbeuguel mbeuguel mbeuguel
Fiii lay nék
Diokh Nala thieur bi
Awma ci kérsa
Deugeul nani diam
Thji yow lakoy amé
Woo woo waaw
Guiso looni gaa gni
Niom Nénaniou
Louniou ma wakh ma wakh la
Dimako toogné
Woo hoo
Filay
Néké mbeuguél fii lay nékeu
Diokh Nala there bi
Amouma i kérsa
Ndokou Yalla ba nimala falé
Nii ngama taalé fii
Néké mbeuguél fii lay



Writer(s): Wally B. Seck


Wally B. Seck - Afromix
Album Afromix
date of release
20-04-2020




Attention! Feel free to leave feedback.