Wally B. Seck - WURUS (Version Afro) Lyrics

Lyrics WURUS (Version Afro) - Wally B. Seck



(I'm in love with you,
In the morning,
In the night,
Oh yeah) × 2
Yay sama aduna
Oh yeah
Sama baby Coco way
Hey yeah
Yaw mi Yay sama aldiana
My love
Sama baby Coco way
Hummm yeah
Baby yay man
Teudeul nélaw xamni
Mounoul dara
I don't give a fuck
Mérr Kat
Fadioul dara
Takkal Leu ay or
Ba ci 24 carats
Dagn lénni
Bayé am peureum
ñom ñuy deuké ayah
Baby I just want real love
Real love
I just want now
Real love
...be I don't want lie
(I'm in love with you
In the morning
In the night
Oh yeah) ×2
Yay sama aduna
Oh yeah
Sama baby Coco way
Hey yeah
Yaw yay sama aldiana
My love
Sama baby Coco way
Way way way
Mérr bi fadioul dara
Mom fadioul dara
Kon fadioul dara
Bayi lén ñeuw
Ma takkal Leu
Or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngalam 24 carats
Xanna do maala yéné
Ma vie
Ma vie
Ma...
Baby yay man
Teudeul nélaw xamni
Mounoul dara
I don't give a fuck
Mérr Kat
Fadioul dara
Takkal Leu ay or
Ba ci 24 carats
Dagn lénni
Bayé am peureum
ñuy déké ayah
Baby I just want real love
Real love
I just want now
Real love
...be I don't want lie
(I'm in love with you
In the morning
In the night
Oh yeah) ×2
Yay sama aduna
Oh yeah
Sama baby Coco way
Hey yeah
Yaw yay sama aldiana
My love
Sama baby Coco way
(Way way way
Mérr bi fadioul dara
Mom fadioul dara
Kon fadioul dara
Bayi lén ñeuw
Ma takkal Leu
Or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngalam 24 carats)



Writer(s): Wally B. Seck


Wally B. Seck - WURUS (Version Afro)
Album WURUS (Version Afro)
date of release
22-12-2021




Attention! Feel free to leave feedback.