Lyrics Ya tay (feat. Baye Mass) - Wally B. Seck
Par
AbouAmg
Yéwou
ci
seu
wét
doyna
mbégté
Diakaarlok
seu
kanam
doyna
banékh
Love
bimay
yeuk
kouko
meun
teuyé
Ana
kiko
sagne
diaral
nama
khéékh
So
beugué
nak
mou
sauvage
baby
So
beugué
nak
mou
doux,lo
deff
ya
tay
Dis
moi
ce
qui
t'arrange
bébé
Diafandou
na
ci
seu
branche,mbeuguél
bou
khéré
Yéwou
ci
seu
wét
doyna
mbégté
Diakaarlok
seu
kanam
doyna
banékh
Love
bimay
yeuk
kouko
meun
teuyé
Ana
kouko
sagne
diaral
nama
khéékh
So
beugué
nak
mou
sauvage
bébé
So
beugué
nak
mou
doux,lo
deff
ya
tay
Dis
moi
ce
qui
t'arrange
bébé
Diafandou
na
ci
seu
branche,mbeuguél
bou
khéré
Ci
seu
wét
douma
baayi
Ak
loum
meunti
done
Boulma
yeureum,
déma
gaagne
Takk
sama
lokho
Yow
seu
allure
dafa
gaaw
Kouko
léék
fott
Même
so
togné
boulma
baalou
Lo
deff
dafmay
néékh,ya
tay
Soma
togné,ya
tay
Réwantoul
sakh,ya
tay
Kou
ci
dougou
mo
ci
dess,ma
baby
ya
tay
Soma
togné,
ya
tay
Réwantoul
sakh,ya
tay
Kou
ci
dougou
mo
ci
dess,kone
baby
ya
tay
Mane
dé
beug
naa(ya
tay)
Lo
wakh
mou
nékh(ya
tay)
Yow
da
nga
taarou,da
nga
diékk,da
nga
nice
Seu
dokhine
rafette
na(ya
tay)
Mane
beug
naa(baby
ya
tay)
Lo
deff
mou
nékh,khamna
dingma
meussa
gagne
Beugouma
niouy
réro
Wakhoumalak
taago
Sama
thiofél
ci
yow
wornama
Nope
naala
mane
eh
eh
ya
Show
me
your
love
my
babyboo
Sama
safara,my
seytaané
Everything!My
love
knocks
me
down
Rothie
sama
guégno
diokhnaala
ko
Ah
dissah
deep
love
fidi
gyal
dem
Dem
ennemi
mana
ready
fi
shoot
dem
Mi
love
is
over
all
why
me
ready
for
everything
Baybe
yaag
neu
man
dama
paré
Ndiggueul
xalé
bi
diaral
nama
xaré
Mi
love
is
over
all
why
me
ready
for
everything
Ci
seu
wét
douma
baayi(ma
babyboo)
Boulma
yeureum
déma
gaagne(mon
bébé
à
moi)
Seu
allure
dafa
gaaw(ma
babyboo)
Même
so
togné
boulma
baalou(mon
bébé
à
moi)
Soma
togné,ya
tay
Réwantoul
sakh,ya
tay
Kou
ci
dougou
mo
ci
dess,ma
baby
ya
tay
Soma
togné,ya
tay
Réwantoul
sakh,ya
tay
Kou
ci
dougou
mo
ci
dess,kone
baby
ya
tay
Hum
Show
me
your
love
ma
babyboo

Attention! Feel free to leave feedback.