Youssou N'Dour - Bull Ko Door Lyrics

Lyrics Bull Ko Door - Youssou N'Dour




Sett len si yalla li niawna yen gnii di dorr djiguen yi yen lay wakhal
djiguen dou foykay dou morceau yen gnii di dorr djiguen yi yen lay wakhal
bougnou ko deffon sa djiguen doula nekh kone doma diambour dji nga yorr iow boul ko dorr



Writer(s): youssou n'dour


Attention! Feel free to leave feedback.