Lyrics I Bring What I Love - Youssou N'Dour
Tayma waxla Djiguène likoy geuneu bègeul
Toga diakarlok mom niko I love you
Ak loko meuna may amna louko geuneul
Togal nga dianok mom niko I love you
Seu mbeuguèl guingay wotè tay likoy deugeul
Wowal sa chérie boy niko I love you

Attention! Feel free to leave feedback.