Youssou N'Dour - Pitche Mi Lyrics

Lyrics Pitche Mi - Youssou N'Dour



Stand Up
Stand Up
Wakhtou dafa djott niou mom sunu bopp
Wakhtou dafa djott niou djokk thi sunu bopp
Diokhniou indépendance waye bataye nioniou djitou
Founiou la djokhei bene dieulfeu foukk sen beut neniou
Yaye boye kaye dieulma bala ma dem guet (×2)
Pitch mile noppil dom
Anh noppil dom
Pitch mile noppil dom khamnga bala djant sokh sa yaye nieuw dieul leu Yayo Yaye Yaye
Danga ma beug nakh yaye dou nieuw (×2)
Danga ma beug nakh yaye dou nieuw ndakhte yaye boudone nieuw nieuwna ba diant fekke Yayo Yaye Yaye
Nioye khamb tal diayla arme ba pare dileu ate
Guem suniou bopp daldi doyelo moniou manquei
Suniou soubeu laniou tayele banque mondiale akk FMI
Liguey thi bopp kagn laniou mom suniou bop
Yaye boy kaye dieulma balama dep gue
Monde dama meunteu naw
Monde dama meunteu naw fekki Yaye (×2)
Wouy Yayo boye
Monde dama meunteu naw fekki yaye
Danga ma beug nakh Yaye dou nieuw
Monde dama meunteu naw fekki yaye
Ndakhtei yaye boudone nieuw nieuwneu ba diante fekkei
Monde dama meunteu naw fekki yaye
Anh
Monde dama meunteu naw fekki yaye
Ihh
Yayo Yayo Yayo
Ohh
Wouy Yaye Wouy Yaye Wouy Yaye (×2)



Writer(s): Mouhamadou Gueye


Youssou N'Dour - Immigrés
Album Immigrés
date of release
16-04-2002




Attention! Feel free to leave feedback.