Youssou N'Dour - Xaley Rewmi Lyrics

Lyrics Xaley Rewmi - Youssou N'Dour



Gudde, maasa gudde
Jeddi ma na konto
Maasa gudde
Waw ye xalel rewmi
Ni la ko bëgge, waw
Bisimilaye ñi ñetti dom
Delllusa ku ñom
Di ñan yallo mu nangu
Leppu lo ko ñan
Ye xalel rewmi
Ni la ko bëgge, waw
Seytan yakh di sotti xalat
Di te Wulli ande dom dal duñu lal yaye
Ye xalel rewmi
Ni la ko bëgge, waw
Sen atmi muddi atem guni soxtlo uni bari wax
Man jenni bolo tawan mag ni niew dole rew
Bu ñu bu taggu awa gulom del sukium bel walbil
Fumune si adduna sen caye kar lu bax
Ye xalel rewmi
Ni la ko bëgge, waw
Duñu waxtan nit suñu mbaye
Mat met na badin rew
Lu ñu wax ñu degge ko bole suñu xalat
Nici picci ni ci bir fu waye mënna ne
Nan dole suñu xalat yew mi du komangu



Writer(s): Youssou N'dour


Youssou N'Dour - The Best of Youssou N'Dour
Album The Best of Youssou N'Dour
date of release
07-11-1994




Attention! Feel free to leave feedback.