Youssou N'Dour, Etoile De Dakar & Akon - Song Daan Lyrics

Lyrics Song Daan - Youssou N'Dour , Étoile de Dakar



Dooley nit kou ñuul kou
Ko beug xam la
Mbeur mouy daan kou
Ko beug xam démal laćć ko you
Woma woma
Ci leundeum
Dinala
Wouyou
Oubil sama
Xol dinga
Xam nimou sédéé ci you
Fileg mang lay am
Sama xol
Luma songù
Daan ko
Fileg mang lay am
Sama Xèll
Luma songù
Daan ko
Songù
Daan
Koooooooo
Man
Maanan
Mane iiow laa
Iiow nga naan
Ngané man leuh
ÉH ÉH
ÉH ÉH
Béneu biss dina niow
Mou melni louniouy netali
Mou melni lii dou
ANHHHHHHH
The ken Du jog
Naan man mi nako fékéh
YOOOOOOO
Ndah nguelaw lii daaw diñou yobalé
Xoob yiy russ ci garab guii
Ah lifi xew tay büñü ko fatéé
Africa sén dòm
Yiy wane
Sén bopeuh
Fileg mang lay am
Sama xol
Luma songù
Daan ko
Fileg mang lay am
Sama Xèll
Luma songù
Daan ko
Songù
Daan
Koooooooo
Man
Maanan
Mané iiow laa
Iiow nga naan
Ngané man leuh
ÉH ÉH
ÉH ÉH
Díg
Fofù
Laay diar
am xàl
Safara douma daaw
Los angeles Paris ba Rio
New Delhi London Tokyo
Sêdoog
Yén Liñu
Jēlé
Fénéne
ñù
Diarr ñun ba éksi
Dafa mèlni
Louńou nétali
Los angeles Paris ba Rio
New Delhi London Tokyo
Sêdoog
Yén Liñu
Jēlé
Fénéne
Éh Éh
HH HHHHHH
HHHHHHHH
Maa contane
Yoow it yaa contaaan
Maleu geuuneuu contane
Uhh Yeahhhhh
HHHHHH!!
Contane yeahhh
YEAAAHHH
ContaAAN
Yeahh
ContaAAN
Yeahh
Akon
Youssou Yeah
Akon
Youssou Yeah
Díg
Fofù
Laay diar
am xàl
Safara douma daaw
Los angeles Paris ba Rio
New Delhi London Tokyo
Sêdoog
Yén Liñu
Jēlé
Fénéne
ñù
Diarr ñun ba éksi
Dafa mèlni
Louńou nétali
Los angeles Paris ba Rio
New Delhi London Tokyo
Sêdoog
Yén Liñu
Jēlé
Fénéne
(End)
Song Daan Youssou Ndour feat Akon Lyrics by Tetofayeman




Youssou N'Dour, Etoile De Dakar & Akon - Senegaal Rekk
Album Senegaal Rekk
date of release
10-05-2016



Attention! Feel free to leave feedback.