Youssou N'Dour feat. Le Super Étoile - Lii ! Lyrics

Lyrics Lii ! - Youssou N'Dour feat. Le Super Étoile



Lima khalé bi diaral
Nima khalé bi di deff
Lima khalé bi diaral
Nima khalé bi di deff
Lima khalé bi diaral
Lou mou yagh yagh may dann
An yee déé yo yee déé
Am ma wakh ko benne yonne késsé
Mane dama la beugue
Am wakhlen ko niarry yonne
Mane dama ko beugue
Khawma liloumou donne
Ba sou ma dadiekk mome
Dou ma mouna wakh
Sa ma fitt teuf teufy
Ma gniéna thieu
Am ma wakh ko benne yonne késsé
Mane dama la beugue
Am wakh len ko niarry yonne
Mane dama la beugue
Nelawatouma lolou mo ma sonnal nii
Sama liguey tardé
Sama gayui gui sa touma niouma diakhlé
Am na kharite bou ma
Diwoule lou nekh kha nekh
Wayé foumuy diayy loumou diarr ya diarr
Douma wakhalé
Warouma sekhak mome roussanté
Wawaww
Warouma sekhak mome neubenté
Dina si yokk ak tank you lere
Bouko doyoul wa yokk tieu
Marakiss you wekh
Warouma sekhak mome roussanté
Wawaww
Warouma sekhak mome neubenté
Dann na telephoné
Degue batam tite tegate delou
Wayé dina telephoné
Biyone mane dina wakh ak mome
Ndaww si beugue nalaaa
Dann na telephoné
Degue batam tite tegate delou
Wayé dina telephoné
Biyone mane dina wakh ak mome
Yaw dall beugue nala
Assane Thiam Babel Demba
Ya wakh lii
Deugeul ma momel yennel lii
Teugeuel tama yennel lii
Ba saw yek ko
Ba wa binto yek ko
Ba wa sud yek ko
Ba wa nord yek ko
Assane Thiam Babel Demba
Ya wakh lii
Teugeuel tama yennel lii
Ba saw yek ko
Ba wa binto yek ko
Ba wa sud yek ko
Assane Thiam Babel Demba
Ya wakh lii
Teugeuel tama yennel lii
Lii
Lii ma khalé bi deff
Mome lii mouma diarrall
Lii ma khalé bi deff
Mome lii mouma diarrall
Lou mou yagh yagh may dann
Dann dann dann dann dann dann dann




Youssou N'Dour feat. Le Super Étoile - Lii !
Album Lii !
date of release
15-12-2000




Attention! Feel free to leave feedback.