paroles de chanson Bo Jekko - Obree Daman
Bo
jekko
Deel
baale
Boo
amee
te
mën
ko
Deel
maye
Bo
jekko
Deel
baale
Boo
amee
te
mën
ko
Deel
maye
Yaa
ngi
ci
kaw
Xalaatal
ñi
ci
suuf
Because
tomorrow
Is
another
day
Bu
am-am
tax
Nga
fate
ki
doonoo
Waaye
bu
ñakk
tax
Nga
baayi
sa
loxo
Ab
Goor
Yàlla
ngay
doon
Royal
ci
Ibra
Faal
ee
Dinañ
la
xas
dinañ
la
faqastal
Waay
waay
bu
len
faale
Ab
Yaay
Faal
ngay
doon
Royal
ci
Maam
Buso
Baali
Dinañ
la
xas
dinañ
la
faqastal
Yaay
Faal
nga
bu
len
faale
Jappante
baña
baayi
gën
di
bëggënte
Kula
tooñ
nang
ko
baal
buñ
ñu
jaxase
Ah
dunyaa
Ah
dunyaa
Jappante
baña
baayi
gën
di
bëggënte
Kula
tooñ
nang
ko
baal
buñ
ñu
jaxase
Ah
dunyaa
Ah
dunyaa
Goor
Yàlla
yombul
Ci
adduna
si
le
Boo
jekkoo
deel
baale
boo
ammee
te
mën
ko
deel
maye
ay
Waay
waay
waay
Bo
jekko
Deel
baale
Boo
amee
te
mën
ko
Deel
maye
Bo
jekko
Deel
baale
Boo
amee
te
mën
ko
Deel
maye
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.