Iss 814 - Yémé (Dakar Trap #2) paroles de chanson

paroles de chanson Yémé (Dakar Trap #2) - Iss 814



Sokhna si ya dak chocolat
Lig ma def big si goudi oulala
Nagouna yay sama ébola
Lima yeuk sama yaram sa djiko la
Thiouray bigua def koulako diay
Vraiment Lawbé bi dinama ray
Nema li dot chéri songouma
Iowmi iowmi rek si jogama
Boula nekhé guénel sama yaye
Wala sakh gua dak sama baye
Parceque iow nigua mel ken douko mel (no no)
Boufi nekoulé lépay law
Parce degua Yémé
Yémé, Yémé,Yémé,Yémé,Yémé
Yémé,Yémé
Yémé(yémééééé)
Yémé(yémééééé)
Yaye boy nak dagua beuri problème
Ki loko méré méré manoul dem
Woko yen niar yen diéma waxtan
Def ko ni sa dom diko naxtan
Wakh deug yaye xamé toumaleuh
Téh boufiy wakh sakh ma guéné leuh
Sey gua ba paré bako mou sey
Ki bou guéné keur gui dotouma khey
Setna ba set iow yakoy togn
Negua manoul sokhu manoul mogne
Bou dougué si wagn bi daguén koy diew diew diew
Bou goudé teudi dagueni thiow
Parce que dafa Yémé
Yémé,Yémé,Yémé,Yémé
Yémé,Yémé,Yémé
Wakhma kagn guay gnibi yaye
Dakh sokhna si néna bouma lafi bayi
Dafa Yémé oh ah(yémééééé)
Dafa Yémé oh ah(yémééééé)
Wakhma kagn guay gnibi yaye
Dakh sokhna si néna bouma lafi bayi
Dafa Yémé oh ah(yémééééé)
Kagn guay gnibi yaye (yémé)
Yémé yémé yémé yémé yémé
Yémé yémé
YÉMÉÉÉÉÉÉ



Writer(s): Ismaila Talla


Iss 814 - Yémé (Dakar Trap #2)
Album Yémé (Dakar Trap #2)
date de sortie
15-03-2019



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.