Admow - Biss Bi paroles de chanson

paroles de chanson Biss Bi - Admow



La patience est dure mais sa récompense est pure xar bi yageuna
Lou yageu deugeula mo tax kou mougn nioun niaar leu woon hohoooo Mouy
Nex ak Mouy nakhari tay niou nk noone souba ay kharite andeu bii
Djitouna dioud bii ohoooo digueuntei bii dfa oveu nice×2 héhéééé
Mla beug t Mane ma xam sa Price ×2wohooo bour bii yalla moko oveu
Nice ×2 yéhééé I love you baeby hoooo beuss biniou dom xaar aksina
Bassouma bae rombe liii nananananaaa hooo hooo hoo beuss bima dom
Xaar aksina bassouma bae rombe liii meuna bii bama romb lii
Nananananaaa NANANANANANAAA héhéééé hohoooo xamone Nani Dina
Meusseu diex Lou metti lo guiss Dina meusseu diex Lou donone sma yéné
Modiii fompou sa raguongne ak banexe I love you Mane beugeu n'alla
Soumis yanima baeby ené fada waxone nla
Boula Dara metti hii m'y baeby I cat your ...
Tay djii yadi dama sokhna Mane AK ioe niou andeu bokou sokhla
Hohohohoo heure bii Diot n'a hée biss Bilé Diot n'a hoooo tay djii
Yadi sama sokhna Mane AK ioe niou andeu bokou sokhla
Hohohoo beuss Bilé djiot n'eu mané beuss Bilé Diot neu



Writer(s): Adama Diop


Admow - Biss Bi
Album Biss Bi
date de sortie
23-12-2019




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.