Admow - Boula Dara Meti paroles de chanson

paroles de chanson Boula Dara Meti - Admow



Yéne say nga fogni
Thie adounabi kéne doula comprendre
Sometime gneuh déme beu diape doto meusseu contane
Thie biir keur guii
Yaye booy néna doula may nada
Nada
Thie mbéde mii yeah yeah
Ragala taxx ngani doo mayé dara dara
Mais nak boul diaxlé
Yoone la bou diafé
Wayé maa di goor bou xam finga fété
Xam sa ndieuk moo tax ma deuke thie di gnafé yeah yeah
Humm
Thioféél leu ngui thie biirr xol bi
Dioxma confiance ma yoboula fou soori
Ooh baby
Ooh baby yeah yeah
Damala love love love
Baby love love love
Boula daara métii
Nakar diéxx na tay mangui thie sa wétt girl
Boula daara métii
Dinala téwal thie nathie téwal thie kerr
Boula daara métii
Baby I gatt you baby
Boula daara métii
Écoute moi baby
I love you lady
Et je sais que t′a peur de m'aimer
Si tu t′inquiète pour moi t'a tord
Il faut que tu sort de ton décors
T'a déjà gagné mon coeur donne moi ma chance
Fait un effort
Soumala xoolé guiss thie iow kou ame diome
Douma beugue loudoul doone sa héro
Doo wétt thie bii yoone
Je suis ton ange gardien
Baby you the one
Baby you are the only one
Baby you′re the only one that I need in my life
Damala love love love
Baby love love love
Boula dara méti
Nalar diéxx tay mangui thie sa wett
Boula dara méti
Dinal téwal thie nathie téwal la thie kerr
Boula dara méti
Baby I got your back
Boula dara méti
Eh, eh eh eh eh
Damala love love love
Baby love love love
Boula dara méti
Nalar diéxx tay mangui thie sa wett
Boula dara méti
Dinal téwal thie nathie téwal la thie kerr
Boula dara méti
Baby I got your back
Boula dara méti
Baby I got your back
Baby I got your back
Baby I got your back
Boula dara méti, no no



Writer(s): Adama Diop


Admow - Boula Dara Meti
Album Boula Dara Meti
date de sortie
07-07-2019




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.