paroles de chanson Ndogal - Dip Doundou Guiss , Ashs The Best
Nitt
ak
doundam,
nitt
ak
mélokan'am,
nitt
ak
jeufinam
Y'allah
ak
meuninam,
bayal
sa
warr
Ko
khamoul
dioud'am
Khamo
thiossan'am,
bayiko
mou
dem
Y'allah
ak
ndogalam
topal
sa
wayy
Gorr
dey
nangou
ndogal
(gorr
dey
nangou
ndogal)
Nanto
di
ker
kéra
diam
gni
Dou
sagane
sank
lap
té
do
dougn,
do
set
do
sélal
Do
kham
boromam
Ouuhh...
aaaah...
hé
am
y'allah
niakeu
y'allah
Ouuhh...
aaaah...
y'allah
yallah
bay
sa
tool
Ouuhh...
aaaah...
nato
di
kér
kéra
diam
Ouuhh...
aaaah...
y'allah
yallah
nagn
ko
gnane
Dougou
si
beugeu
si
guen
Dioudou
di
diéguési
déh
Louxouss
dou
guéner
billet
Dougou
pour
gniko
fi
beuy
Mounouma
dokh
si
digue
ndokh
wayé
bougou
ma
khof
di
tindi
lokh
Deukeu
di
wax
si
nitt
lou
bone
Bo
déwé
guiss
god
do
sigui
khol
ko
How
lies
on
me
eyes,
(on
me)
Loutax
nga
tek
ma
beut
té
guissoumala
Eyes
on
me
why?
How
eye
on
me
(on
me)
Life
dou
nonou
menyeah!
Sokhor
dey
leundeumeul
sama
rouh,
Kignane
dafey
peundeul
sama
yourr
Y'allay
xam
xam,
y'allay
mbeuguel,
y'allay
am
am
Y'allay
mbecté
Life
yakoy
jugé
moley
teuthi
Life
yakoy
guédeu
yakoy
néxal
Life
daley
fowé
ngen
deugeul
Life
geunoul
kawé
soufou
bop
Gorr
dey
nangou
ndogal
(gorr
dey
nangou
ndogal)
Nanto
di
ker
kéra
diam
gni
Dou
sagane
sank
lap
té
do
dougn,
do
set
do
sélal
Do
kham
boromam
Ouuhh...
aaaah...
hé
am
y'allah
niakeu
y'allah
Ouuhh...
aaaah...
y'allah
yallah
bay
sa
tool
Ouuhh...
aaaah...
nato
di
kér
kéra
diam
Ouuhh...
aaaah...
y'allah
yallah
nagn
ko
gnane
1 Djar Djar
2 Lll
3 Mounouma Bayi
4 Life Bi
5 Ndogal
6 Ci Ioe La Mire
7 Yaakar Bou Tass
8 Fdfd
9 6 in the Morning
10 Interlude
11 Stay
12 Ohh Yess
13 Ngorr
14 Follow Me
15 Guissou Mala
16 Noflay
17 No More
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.