Ashs The Best feat. Kya Loum - Yeurmande (feat. Kya Loum) paroles de chanson

paroles de chanson Yeurmande (feat. Kya Loum) - Kya Loum , Ashs The Best



Par AbouAmg
Jooy naa ba jeexal ròngoñ
Jaay naa la sama bakkan
Fippu naa fippu xeex ngir sama askan
Xeex ngir sama askan
Jooy naa ndax nèwdi dooli ngi yelwaan
Xiif akk mar jamono jii
Nèwdi doole di jooy
Jël nga sunu paix et lova
Nguur gi def ñu ennemis
Dëkk ci di ñu nòot
Jëlli ji li ñu moom jot na
Seeni doom'ag sunuy doom ku ci gën
Sunu koom ci seeië
Dafa wuño yoonu geej fii la ñuy toog
Demmatu ñu bitim reew
Jooy naa akk samay dëkkëndoo
Yërmande Ci doomu Yalla yi
Fippu naa akk sama doomu yaay yi
Fippu xeex ngir ëllëgu reew mi
Jooy naa ba ñakk ròngoñ
Jaay la sama bakkan
Fippu xeex ngir sama askan
Xeex ngir sama askan
Fippu naa ngir sunuy doom
Fippu ngir yaay ju ñakk doomam
Fippu xeex ngir li ma moom
Yërmande ci sunuy njaboot
Jooy naa ba ròngoñ jeex
Nèwdi doole ngi yelwaan
Jooy ba ròngoñ
Jeex Ngirlolen gi bientôt .
Suis len yërmande
Yërmande
Yërmande
Yërmande
Yërmande
Yërmande
Yërmande



Writer(s): Abdoulaye Sy, Ashs The Best, Kya Loum, Olivier Delahaye


Ashs The Best feat. Kya Loum - Yeurmande
Album Yeurmande
date de sortie
12-03-2021



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.