Ashs The Best - Xaalis paroles de chanson

paroles de chanson Xaalis - Ashs The Best

Khaliss laniou geuneu fonk nitt walay
Nitt a meuneu am khaliss ioe khaliss laniouy am
Lou waral gni di diay sen lerr dieundé ko leundeum
Allalou aduna la leep fi ngakoy bay
(Khaliss llaniou geuneu fonk nitt walay)
(Nitt a meuneu am khaliss ioe khaliss laniouy am)
(Lou waral gni di diay sen lerr dieundé ko leundeum)
(Allalou aduna la leep fi ngakoy bay)
Khaliss lagn ley khamé
Khaliss lagn ley lathié
So amoul khaliss dougn la khamé
Dougn la wolou dougn la lathié
Nieupa beug melni mome
Khaliss tek la gathié
Boul ma wolou boul ma lathié
Awma khaliss million flow laley wathié
(Khaliss llaniou geuneu fonk nitt walay)
(Nitt a meuneu am khaliss ioe khaliss laniouy am)
(Lou waral gni di diay sen lerr dieundé ko leundeum)
(Allalou aduna la leep fi ngakoy bay)
(Khaliss llaniou geuneu fonk nitt walay)
(Nitt a meuneu am khaliss ioe khaliss laniouy am)
(Lou waral gni di diay sen lerr dieundé ko leundeum)
(Allalou aduna la leep fi ngakoy bay)

Writer(s): Abdoulaye Sy

Ashs The Best - Millions Flows (Deluxe)
Album Millions Flows (Deluxe)
date de sortie
28-08-2020

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.