Bran Van 3000 feat. Youssou N'Dour - Senegal (feat. Youssou N'Dour) paroles de chanson

paroles de chanson Senegal (feat. Youssou N'Dour) - Bran Van 3000 , Youssou N'Dour

Maysa tende jodo yaa moom liile
Maysa tende jodo yaa moom liile
Maysa tende jodo yaa moom liile
Hi woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Buri samba laobe yaa moom liile
Buri samba laobe yaa moom liile
Buri samba laobe yaa moom liile
Hi woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Damel maisa Penda Joor / Jooro Jooro Jooro Jooro Ho Ho Ho Hoy
Sama waaji ken dula jam naani
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Mmmm mmm
Wooy Tedi Ngoné maarne be Sambaa
Kuli baca senge ndat Biran ngamoo
Ngoné maca nas mbay maca jeeri
Samba yaasimooooo dike mbay Kuja dooooki
Yay borom mbaboor... mi
Hi (di) woy Birima Sama waaji ken dula jam naanee
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Dogo fal ak mawa joor Kumba samba yaay jaloor
Dogo dogo ... Ho ho ho!!
Aziz o mbay dogo xam nga yoon wee
Choeur: woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Maisa tendo jooro jooro a mari ngone sobel Kayor niila
Woy Birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Writer(s): James Di Salvio

Bran Van 3000 feat. Youssou N'Dour - Discosis
Album Discosis
date de sortie
18-06-2001

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.