paroles de chanson Dafmay Nekh - Bril , OMG
Par
AbouAmg
Lou
né
thi
xol
fégne
thi
kanam
Xol
bi
yathi
fess
fégne
sama
kanam
Founé
lay
xol
thi
sa
yaram
di
guiss
sama
boppou
li
fi
rek
la
ma
Yama
doflo
dima
deflo
loumé
bébé
yamako
diaral
Fouma
togué
guissou
mala
déguou
fok
ma
wo
la
néla
diaaral
()
Yawla
bandit
di
ndirol
kaay,
waxma
qui
est
tu
Li
eupeu
neu
daffa
fess
bey
tourou
atanou
mali
Yamay
ray
dima
doundal
aldiana
guamay
dougal
té
déwagouma
Somay
bayi
dima
mbouguel
safara
guamay
teumbeul
soma
méré
Yafi
ya
bi
fort,
sama
point
faibleol
x
yako
Forr
Weurouma
dara
lepp
gua
am
Diam
djig'
may
diox
la
beurri
baby
li
comme
guerre
Yaw
yaye
bou
bakh
bi
ya
takh
may
noyi
yaye
sama
air
Yaye
sédal
sama
xol
di
tangal,sama
yaram
doma
mey
dara
Sougnou
wété
doma
yeureum
Ma
raw
sax
visa
shengen
toukil
baby
foula
nekh
do
faye
Thieuguine
Xamgua
mane
ma
bakh
thi
yaw
kay
gnou
thieuguine
Fékheul
sa
xol
ma
this
Guaw
gneuthieuyuyeul
g
daw
kay
gnou
thieuguine
Diégué
ma
diégué
ma
gneuweul
gnou
féthe
moulatheuguine
Lepp
lo
sokhla
lalal
diox
di
weuy
thi
say
waw
Sougnouy
beurré
diaroul
arbitre
yaw
yaye
moudjé
daw
Foma
wo
ma
wouyou
bolé
thi
nekh
thi
kaw
bathi
souff
Wolou
guama
gnou
dém
may
wérou
waye
maly
ouff
Fouma
dém
gua
weuririna,
Fimguila
diap
souff
koudoul
crinière
deh
doyoula
Moi
j'assure
damla
xam
deh
sur
mesure
Fomla
téyé
daffay
nekh
malay
dioylo
je
t'assure
Thieuguine
Fowé
sa
xol
té
meuno
si
dara
Beug
na
dafmay
nékh
Nakhla
ni
bébé
té
meuno
si
dara
Hé
beug
na
li
dafmay
nekh
May
xalé
bila
pogné
té
meuno
si
dara
Mome
la
té
meuno
thi
dara
meun
la
fepp
té
meuno
si
dara
Yaye
sédal
sama
xol
di
tangal,sama
yaram
doma
mey
dara
Sougnou
wété
doma
yeureum
Ma
raw
sax
visa
shengen
toukil
baby
foula
nekh
do
faye
Thieuguine
Xamgua
mane
ma
bakh
thi
yaw
kay
gnou
thieuguine
Fékheul
sa
xol
ma
this
Guaw
gneuthieuyuyeul
g
daw
kay
gnou
thieuguine
Diégué
ma
diégué
ma
gneuweul
gnou
féthe
moulatheuguine
Xamgua
crinière
ma
bakh
thi
yaw
kay
gnou
thieuguine
Fékheul
sa
xol
ma
this
guaw
gneuweul
gnou
thieuguine
Ya
meuneu
tékou
limay
daw
guiny
g
Guiné
g
féla
g
Fowé
sa
xol
té
meuno
si
dara
Beug
na
dafmay
nékh
Nakhla
ni
bébé
té
meuno
si
dara
Hé
beug
na
li
dafmay
nekh
May
xalé
bila
pogné
té
meuno
si
dara
Mome
la
té
meuno
thi
dara
meun
la
fepp
té
meuno
si
dara
Yaye
sédal
sama
xol
di
tangal,sama
yaram
doma
mey
dara
Sougnou
wété
doma
yeureum
Ma
raw
sax
visa
shengen
toukil
baby
foula
nekh
do
faye
Thieuguine
Kay
gnou
thieguine
Gneuweul
gnou
thieguine
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.