Canabasse feat. Ya Hassan - Confessions 1 - traduction des paroles en français

Paroles et traduction Canabasse feat. Ya Hassan - Confessions 1




Confessions 1
Confessions 1
Salaamu Aleykum
Que la paix soit sur vous
A-Onzu Bilahi Bismilah
Tout d'abord, au nom de Dieu, le Miséricordieux
Niou délou waat cii sunu waa dji nga xamni bobou ba légui
On va parler de choses que vous, les hypocrites, vous connaissez
Nio ngui koy lathie
Je suis venu pour éclairer
Waayé wakh deuguite mou ngui gni tontou
Il y a des choses que je ne cautionne pas
Waayé dafa am Aaya bou "Fala taharanakumoul Hayata
Il y a un verset qui dit : vous qui avez cru ! Voulez-vous que Je vous indique un commerce
Dunya walla yahuranakum Bilahi khourou"
qui vous sauvera d'un châtiment douloureux ?"
Boulène toppeuh aduna ay nakhem boulène toppeuh Iblis ak
Beaucoup parmi nous courent après ce bas-monde, beaucoup parmi nous suivent le diable
Pékhem "Xutbu Dunya zoulmatoun"
Ils oublient : "La vie ici-bas est une tentation"
Mané beug aduna kat ap leundeum leu waayé "Wa
Moi je ne veux pas de ce bas-monde, ce n'est qu'illusion, c'est pourquoi : "Wa
Takkuwal-Lahi Sirajûn-Laha" Manaam ragal Yallah moy lampe
Takkuwal-Lahi Sirajûn-Laha" Que Dieu soit ma lumière
Bi
Bi
Manaam diamou sunu Borom Subhanawu wa Talah dinkeu ko sunuy
Je prie notre Seigneur Subhanawu wa Talah de nous éclairer sur le droit chemin
Lep
Lep
Lolou kep mo gni cii meuneu guéné. Amena niou Yallah di
C'est tout ce que j'ai à dire. Qu'Allah nous guide
Doundeul waayé Sheytané lagni défal
Loin de nous, Satan et ses tentations
Doyna waar! Ndaxté "Ina Hizba Sheytani Khoumoul Hassiroune
Écoutez bien ! N'oubliez jamais : "Ina Hizba Sheytani Khoumoul Hassiroune
" Manaam gni toppeuh Iblis nieup
" Moi, je ne fais pas partie du clan du diable
Ay ajji perte lagne Iblis taaralna Aduna cii sunuy beute
Il a déjà perdu, ce diable ne pourra pas nous avoir, ce bas-monde est un piège
Defna cii nioune beug alal kheur niou cii
Il nous pousse vers le mal alors que nous voulons le bien
Mbok bi: est-ce que ya ngui kheul di dieum cii Iblis wala ya
Dites-moi : est-ce qu'il y a quelqu'un ici qui suit le diable ou y a-
Ngui khiir niit gni cii Yallah?
t-il quelqu'un qui suit Dieu ?
{Canabasse}
{Canabasse}
Djeu cii suuf baate cii kaw magal God dégueul dieuleul bi
Ici sur terre, dans cette vie pleine de tentations, Dieu merci pour cette inspiration
Moy sama 3ème confessions
Voici mes 3èmes confessions
Yééxna nieuw ndaxté dama dem ba tiite cii sama bopp
Ouais, je sais, ça fait longtemps que je n'ai pas déballé mon sac
Bouma lène wakhé niit kou baaxla deug deug damay saupe
Mais là, il est temps que je vous dise ce que j'ai sur le cœur
Atte yi gueune dii dem may gueune di gueune di saubou
Toi, tu dis que c'est comme ça, moi je dis que c'est comme ça, chacun son avis
Aduna dima djay lima ragalone ma saurou
Le monde tourne, les tentations me guettent
Fimou nii tay bougnou ma ndarone jugé pesé samay dieuf
Personne ne peut dire qu'il n'a jamais fauté, on sera tous jugés pour nos actes
Lerr namani dina thiool
L'erreur est humaine, la faute aussi
Yalnama Yallah baal! Borr yima def ak yima défoul
Je demande pardon à Dieu! On fait tous des erreurs
Yalnama Yallah baal! Borr yima tay ak yima tayoul
Je demande pardon à Dieu! On fait tous des bêtises
Yalnama Yallah baal! Borr yima xam ak yima xamoul
Je demande pardon à Dieu! On ne sait pas tout
Yalnama Yallah baal! Borr yima beug ak yima beugoul
Je demande pardon à Dieu! On a tous des envies
Yalnama Yallah baal limakoy baalou wauroul sakh
Je demande pardon à Dieu! Ne me laissez pas tomber dans le feu de l'enfer
Ndax dina meuneu deudou litah may def litakh may baalou
Je ne veux pas mourir dans le péché, je demande pardon et je me repens
Yalnama Yallah baal boléma cii Jaamam yi gueuneu deugou
Je demande pardon à Dieu! Que ceux qui m'écoutent comprennent
Djeu cii suuf baate cii kaw Yalna tidji sama beut yi teudjou
Ici sur terre, dans cette vie, je veux atteindre mes objectifs
Beut yi teudjou wougnou sakh ma taamou limay guiss
Atteindre mes objectifs, même si je dois ramer à contre-courant
Nopp yi teudjou wougnou ma taamou limay dégue
Éviter les problèmes, même si je dois ramer à contre-courant
Aalema télécommande ma zappé ki digni sonal fils (Ak ay
Ce monde est une télécommande qui zappe sur les vrais
Waar)
Ak ay (Waar)
Téggalma TRACE déguena "NA NIOU DEM" dieulna depuis
On dirait TRACE TV, ils nous disent "NOUS, ON EST COMME ÇA" depuis
Dembe
toujours
Dama tabakh ba tchi kaw guedjeuna kadjii suuf
Quand j'ai commencé à fumer, j'étais jeune et insouciant
Ladiaal Zou légui lepp changé cii sama doundou
Le mal est partout, mon entourage a changé
Sama tuureu ngui cii kaw bougni lim dagnemay toudou
Mes fréquentations ont fait de moi ce que je suis devenu
Waayé takhoul ma djégué ki cii kaw Djeu bi yaguena
Ils se demandent ce que je fais encore ici, moi qui connais la vérité
Laaloul suuf
Sur terre
Han Yaguena laaloul suuf Donté baate bii cii sama xellang
Ouais, je suis encore sur terre, mais ce n'est qu'un passage
May fatali beuss bigne may dinthie cii suuf
Mon destin est tracé, je finirai sous terre
Sampalma piquet biy téyé tableau bignou bindeu sama tuur
Mon cœur est comme un tableau, ma vie est un dessin inachevé
Ma wéét ak sama baméél wara layo lepp louma dougou
Mes mains et mes pieds sont liés par les tentations
Yène saay goudi djot ma teud beute dou teudjou
Le diable me guette, il veut me faire tomber dans le trou
Aduna yéwou ma gueuneu wow beute beutou Iblis ma deudjou
Ce monde est un piège, je veux le bien, le diable me pousse au mal
Toppeuh sama bakane rek di def mouy nekh ba faaténé lima
Je ne fais que suivre mon instinct, je veux le bien, mais c'est dur
Fi néké moy déterminé beuss pinthieu foumay moudjeu
Je suis déterminé à changer, je vais me battre
Yallah dinagnou baal nioune nieup! Hum dina yombeu lolou
Que Dieu nous pardonne nos péchés! L'homme est faible, il commet des erreurs
Fils ndaxté récompense bo guiss amena ndieuk
N'oublie pas la récompense pour ceux qui font le bien, mon frère
Dou chance dieuf dieul leu cii choix yi ngay dieul
Dieu nous donne le choix, à nous de choisir le bon chemin
Pas yi ngay tek fii nioy wakh fi ngay dieum
Le chemin que tu choisis te mènera à ta destination
Pa yiy dakkeu tek fii nio gueunone deungue bignouy jeune
Ne suis pas les autres aveuglément, réfléchis avant d'agir
Changé dou wess khamo Meuwty kagne lalay dieul cii
Change tes habitudes, la mort peut t'emporter à tout moment
Kone matalko bi ngeu cii tolé ndax sa ndaw moy sa dolé
Ne me juge pas, je ne suis pas parfait, j'ai mes faiblesses
Déko sauraalé foné ndaxté déh bouy nieuw dou wotté
Ne sois pas arrogant, la roue tourne, tu pourrais te retrouver à ma place
Nio ngui daw di toppeuh aduna ndax taaram deuké def lou
On court tous après ce bas-monde, en oubliant que la vie est éphémère
Araam
Araam
fi test leu dagnou koy faaté motah niou dem ba saaraane
Si tu es fort, alors prouve-le, allons-y, avançons sur le droit chemin
Yeah dagnou dem ba saaraane
Ouais, avançons sur le droit chemin
Wathieu piste bi Iblis mour guiss guiss yi motah nit day
Le diable nous guette sur le chemin, ne te laisse pas tenter
Guiss deug defko thiakhaane
Ne te laisse pas influencer par les mauvais exemples
Djeu cii suuf baate ci kaw ben niaane Yallah nagnou Yallah
Ici sur terre, dans cette vie, ayons confiance en Dieu, Dieu est grand
May dolé raagné deug ndax niou xam
J'ai mal au cœur de voir ce qui se passe, mais je sais
Djeu cii suuf baate ci kaw bénène niaane! Yallah nagnou
Ici sur terre, dans cette vie, soyons unis! Dieu est grand
Yallah may niou niémé deug ndax niou meuneu daane Sheytane
Que Dieu nous guide sur le droit chemin, car on est tentés par le diable
Am deug cii suuf am deug cii kaw ba biss bouniou teud niou
Il y a du bien sur cette terre, il y a du bien dans l'au-delà, efforçons-nous de mériter le paradis
Mouré niou suuf niou teud fii gueune cii kaw
On est de passage sur terre, efforçons-nous de mériter le paradis
Sama 3ème confessions leu yééxna nieuw ndax rène
Mes 3èmes confessions, car j'ai encore des choses à dire
Dokhouma deug
Dokhouma deug
Tiim samay bakaar ték beat rouss wakh deug
J'ai allumé mon briquet, la vérité finira par éclater
Sama 3ème confessions leu deug dou wess nit égal bakaar
Mes 3èmes confessions, car le bien ne se mesure pas à l'argent
Fils dou dara lou bess étalé samay erreurs rou llife
Mon frère, ne te vante pas de tes richesses, expose plutôt tes erreurs pour que les autres apprennent
Guène dégue mou lerr
Je regrette mes erreurs
Ba bou guène ndaaré xeul cii lou bone sama baate gatandou
Ceux qui m'écoutent, retenez bien mes paroles
Lène
Lène
Loudoul deug di nène kou doundou cii fène togou cii
Le bien est à portée de main, il suffit de le saisir
Nèène
Nèène
Ay gaane lagne fii rek lep fi dess deug kotteu niouy toppeu
On a qu'une seule vie, profitons-en pour faire le bien
Fofou niouy dem
Ne perdons pas de temps, avançons!
{Ya Hassan}
{Ya Hassan}
Waaw mbokk mi nioune dh nio ngui rafètelou say kaddu
Ouais mon frère, nous sommes tous coupables, on a tous fauté
Lolouuu
Lolouuu
Lougnou lay niaanal moy Yalna say dieuf meune deugueul say
J'implore Dieu de me guider sur le droit chemin
Yéné ndaxté sa yéné rafetna lolllll
Personne n'est parfait, on a tous nos faiblesses lolllll
Sunu Borom Soubhanawu Wa Talah wakh nagnou mom yéné
Notre Seigneur Soubhanawu Wa Talah nous a tout donné
Lay fay
Lay fay
"Al Haqqu min Rabbi Kum" Deug déy mo ngui joggué cii sunu
"Al Haqqu min Rabbi Kum" La vérité vient de Dieu
Borom
Borom
Kaddu dji nga fii yeukeuti yeup Kaddu deug leu aape
Le péché est tentant, mais la récompense est grande
Deug katt
Katt
Ak foumou meunti joggué douko téré nek deug
Ne te laisse pas tenter par le diable, le bien est meilleur
Maané aape djoulite bouy moy di toubeul boromam mo
Je regrette mes péchés, je me repens à Dieu
Gueune djoulite bouy moy tédou toubeul boromam
Je regrette mes péchés, je me repens à Dieu
Bokoy dégue mou naane "Astakhfiroulah" Amal yakaar
Je demande pardon à Dieu "Astakhfiroulah" Seul Dieu est miséricordieux
Xamné léroup sunu Borom Soubhanawu Wa Talah
Soubhanawu Wa Talah
Batay dessna cii dieum djo djéé " Wa Yafou'ân
Ne perdons pas espoir, Dieu est grand et " Wa Yafou'ân
Kassirane " Yallah sunu Borom dina baalé lou beuri
Kassirane " Dieu pardonne à ceux qui se repentent
Kone "Laah Takhnatou min Rahmati Laah " Bougni am siki sakk
Kone "Laah Takhnatou min Rahmati Laah " Personne n'est exclu de la miséricorde de Dieu
Mouk cii yeurmeundé Yallah
Mouk cii yeurmeundé Yallah






Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.