paroles de chanson Confessions 3 - Canabasse feat. Ya Hassan
Salaamu
Aleykum
A-Onzu
Bilahi
Bismilah
Niou
délou
waat
cii
sunu
waa
dji
nga
Xamni
bobou
ba
légui
nio
ngui
koy
lathie
Waayé
wakh
deuguite
mou
ngui
gni
tontou
Waayé
dafa
am
Aaya
bou
né
"Fala
taharanakumoul
Hayata
Dunya
walla
yahuranakum
Bilahi
khourou"
Boulène
toppeuh
aduna
ay
nakhem
boulène
Toppeuh
Iblis
ak
pékhem
"Xutbu
Dunya
zoulmatoun"
Mané
beug
aduna
kat
ap
leundeum
leu
waayé
"Wa
Takkuwal-Lahi
Sirajûn-Laha"
Manaam
ragal
Yallah
moy
lampe
bi
Manaam
diamou
sunu
Borom
Subhanawu
wa
Talah
dinkeu
ko
sunuy
lep
Lolou
kep
mo
gni
cii
meuneu
guéné.
Amena
niou
Yallah
di
doundeul
waayé
Sheytané
lagni
défal
Doyna
waar!
Ndaxté
"Ina
Hizba
Sheytani
Khoumoul
Hassiroune
" Manaam
gni
toppeuh
Iblis
nieup
Ay
ajji
perte
lagne
té
Iblis
taaralna
Aduna
cii
Sunuy
beute
defna
cii
nioune
beug
alal
kheur
niou
cii
Mbok
bi:
est-ce
que
ya
ngui
kheul
di
dieum
Cii
Iblis
wala
ya
ngui
khiir
niit
gni
cii
Yallah?
{Canabasse}
Djeu
cii
suuf
baate
cii
kaw
magal
God
Dégueul
dieuleul
bi
moy
sama
3ème
confessions
Yééxna
nieuw
ndaxté
dama
dem
ba
tiite
cii
sama
bopp
Bouma
lène
wakhé
niit
kou
baaxla
deug
deug
damay
saupe
Atte
yi
gueune
dii
dem
may
gueune
di
gueune
di
saubou
Aduna
dima
djay
lima
ragalone
ma
saurou
Fimou
né
nii
tay
bougnou
ma
ndarone
jugé
Pesé
samay
dieuf
lerr
namani
dina
thiool
Yalnama
Yallah
baal!
Borr
yima
def
ak
yima
défoul
Yalnama
Yallah
baal!
Borr
yima
tay
ak
yima
tayoul
Yalnama
Yallah
baal!
Borr
yima
xam
ak
yima
xamoul
Yalnama
Yallah
baal!
Borr
yima
beug
ak
yima
beugoul
Yalnama
Yallah
baal
limakoy
baalou
té
wauroul
sakh
Ndax
dina
meuneu
deudou
litah
may
def
litakh
may
baalou
Yalnama
Yallah
baal
té
boléma
cii
Jaamam
yi
gueuneu
deugou
Djeu
cii
suuf
baate
cii
kaw
Yalna
tidji
sama
beut
yi
teudjou
Beut
yi
teudjou
wougnou
sakh
ma
taamou
limay
guiss
Nopp
yi
teudjou
wougnou
ma
taamou
limay
dégue
Aalema
télécommande
ma
zappé
ki
digni
sonal
fils
(Ak
ay
waar)
Téggalma
TRACE
déguena
"NA
NIOU
DEM"
dieulna
pé
depuis
dembe
Dama
tabakh
ba
tchi
kaw
guedjeuna
kadjii
suuf
Ladiaal
Zou
légui
lepp
changé
cii
sama
doundou
Sama
tuureu
ngui
cii
kaw
bougni
lim
dagnemay
toudou
Waayé
takhoul
ma
djégué
ki
cii
kaw
Djeu
bi
yaguena
laaloul
suuf
Han
Yaguena
laaloul
suuf
Donté
baate
bii
cii
sama
Xellang
may
fatali
beuss
bigne
may
dinthie
cii
suuf
Sampalma
piquet
biy
téyé
tableau
bignou
bindeu
sama
tuur
Ma
wéét
ak
sama
baméél
wara
layo
lepp
louma
dougou
Yène
saay
goudi
djot
ma
teud
beute
dou
teudjou
Aduna
yéwou
ma
gueuneu
wow
beute
beutou
Iblis
ma
deudjou
Toppeuh
sama
bakane
rek
di
def
mouy
nekh
ba
faaténé
Lima
fi
néké
moy
déterminé
beuss
pinthieu
foumay
moudjeu
Yallah
dinagnou
baal
nioune
nieup!
Hum
dina
yombeu
lolou
fils
ndaxté
récompense
bo
guiss
amena
ndieuk
Dou
chance
dieuf
dieul
leu
cii
choix
yi
ngay
dieul
Pas
yi
ngay
tek
fii
nioy
wakh
fi
ngay
dieum
Pa
yiy
dakkeu
tek
fii
nio
gueunone
deungue
bignouy
jeune
Changé
dou
wess
khamo
Meuwty
kagne
lalay
dieul
cii
Kone
matalko
bi
ngeu
cii
tolé
ndax
sa
ndaw
moy
sa
dolé
Déko
sauraalé
foné
ndaxté
déh
bouy
nieuw
dou
wotté
Nio
ngui
daw
di
toppeuh
aduna
ndax
taaram
deuké
def
lou
araam
Té
fi
test
leu
dagnou
koy
faaté
motah
niou
Dem
ba
saaraane
Yeah
dagnou
dem
ba
saaraane
Wathieu
piste
bi
Iblis
mour
guiss
guiss
Yi
motah
nit
day
guiss
deug
defko
thiakhaane
Djeu
cii
suuf
baate
ci
kaw
ben
niaane
Yallah
Nagnou
Yallah
may
dolé
raagné
deug
ndax
niou
xam
Djeu
cii
suuf
baate
ci
kaw
bénène
niaane!
Yallah
nagnou
Yallah
may
niou
niémé
Deug
ndax
niou
meuneu
daane
Sheytane
Am
deug
cii
suuf
am
deug
cii
kaw
ba
biss
bouniou
Teud
niou
mouré
niou
suuf
niou
teud
fii
gueune
cii
kaw
Sama
3ème
confessions
leu
yééxna
nieuw
ndax
rène
dokhouma
deug
Tiim
samay
bakaar
ték
beat
rouss
sé
wakh
deug
Sama
3ème
confessions
leu
deug
dou
wess
nit
égal
bakaar
Fils
dou
dara
lou
bess
étalé
samay
Erreurs
rou
llife
guène
dégue
mou
lerr
Ba
bou
guène
ndaaré
xeul
cii
lou
bone
sama
baate
gatandou
lène
Loudoul
deug
di
nène
kou
doundou
cii
fène
togou
cii
nèène
Ay
gaane
lagne
fii
rek
lep
fi
dess
Deug
kotteu
niouy
toppeu
fofou
niouy
dem
{Ya
Hassan}
Waaw
mbokk
mi
nioune
dh
nio
ngui
rafètelou
say
kaddu
lolouuu
Lougnou
lay
niaanal
moy
Yalna
say
dieuf
meune
Deugueul
say
yéné
ndaxté
sa
yéné
rafetna
lolllll
Sunu
Borom
Soubhanawu
Wa
Talah
wakh
nagnou
dé
mom
yéné
lay
fay
"Al
Haqqu
min
Rabbi
Kum"
Deug
déy
mo
ngui
joggué
cii
sunu
Borom
Té
Kaddu
dji
nga
fii
yeukeuti
yeup
Kaddu
deug
leu
té
aape
deug
katt
Ak
foumou
meunti
joggué
douko
téré
nek
deug
Maané
aape
djoulite
bouy
moy
té
di
toubeul
Boromam
mo
gueune
djoulite
bouy
moy
tédou
toubeul
boromam
Bokoy
dégue
mou
naane
"Astakhfiroulah"
Amal
Yakaar
té
xamné
léroup
sunu
Borom
Soubhanawu
Wa
Talah
Batay
dessna
cii
dieum
djo
djéé
té
" Wa
Yafou'ân
Kassirane
" Yallah
sunu
Borom
dina
baalé
lou
beuri
Kone
"Laah
Takhnatou
min
Rahmati
Laah
"
Bougni
am
siki
sakk
mouk
cii
yeurmeundé
Yallah
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.