Canabasse - Dedet paroles de chanson

paroles de chanson Dedet - Canabasse

Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Dedet (dedet)
Dedet (dedet)
Del bagn
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Dedet (dedet)
Dedet
Dedet
Goumbawoulo lafagnoulo
Deukké talal lokho
Nonon meunou mala Sarakh
Bimakoy hustle yangui nelaw
Legui Matt na Ngua beugg ma tekk choc geunouloma
Ndakhté Bou diekhone tay Ngua ma sokhla
La souba Ngua changé djiko ma meunaloma
Demal outi sa boss bamak lima yor ndakh geunouloma sokhla sama deureum
Kone dedet dedet dedet
Boul meussa wolou nit meme Gni Ngua bokkal deret
Ki nguay denk sa bope mola Geuna danel bayil
Khel Tchi say none mais boul Faté Gni la diegué
NIT dafa bone yeah Khadj moko tané
Ndakh nit Day matte lokho Bi ko doundal Bi mouy fandé
Sénégalais meune salé dalay signe Ba Ngua fokni dala beugg
Ndekété Tchi souff moungui paré yeuffou deumm beugg la danel
Kone dedet
Yeah Nigga no love
Beugatouma koudoul sama bope
Dedet
Kou Fi bakh done doff
Dedet
Ne nagnou trop bon trop con
Dedet
Lebalomala dama la may mais djeuf djou bakh dagnou koy fay
Bimala sokhla dama taylé lepe takhaw
Tay ma nekk Tchi digeunté Ngua wane ma ni
Sunu digeunté lima ko fogon yeupe dou Tchi dara
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Dedet (dedet)
Dedet (dedet)
Del bagn
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Nigga fok Ngua diangue Wakh dedet (dedet)
Dedet (dedet)
Dedet
Dedet
Goumbawoulo lafagnoulo
Deukké talal lokho
Nonon meunou mala Sarakh
Bimakoy hustle yangui nelaw
Legui Matt na Ngua beugg ma tekk choc geunouloma
Ndakhté Bou diekhone tay Ngua ma sokhla
La souba Ngua changé djiko ma meunaloma
Demal outi sa boss bamak lima yor ndakh geunouloma sokhla sama deureum

Canabasse - Dk Spirit
Album Dk Spirit
date de sortie
08-04-2016

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.