Canabasse - Dou paroles de chanson

paroles de chanson Dou - Canabasse



Buzzlab buzzlab
Yeah
Bi ci mbakhanè
Verre yi ak dall yi
Pince bek haut boko bolè mou dioxla
Diapal ma Bent bi
Kholal ma montre bi
Depensou wer lay xolè heure boy bagui ni
Diotna deglou pop a shit guisnaci bopam
Mais melanani e couplet bi dougoyl ci nopam
Liko ci nekh la teyè
Defko ci CD
Bou sathiè auto pa bi mom lay tek diko beguè
Ki moy amadou niounane ko Dou
Show yiko dieguè niougui kay wowè baby Dou
Dak ticket, VIP lay dougou
bou dikè lèche pied yek tiaz yeup debout
Niari nop yeup la beuneu
Foko fek migui peundeul
Boy bi moy symboulou deungue diay ko prek rek mou yeunguel
Dou nena gangster la
Tonko mou foutekou
Yeah Dou watie just what u do
Dou dafay toukh
Dou dafay nane
Dou dougou school non talouko sah
Dou dall mom teylè na lifam nena day doundou
Dou veut grandir avant l'âge kou wahak mom mounila doul
Dou my boy deg gua Dou Dou
Hey meytoul melni Dou mom Dou
Royoukay yeup Dou Dou mom douci meuseu guene
Janvier ba décembre migui hollyday
Toukh nane japiser
School yici town bi yeup diotnafa diangui diè
Ndakh doudou nangouwoul redoublé
Pepam yeup la falsifier
Hey mola gueneu moss fouf mais taloul darak perturbé
Dou moy bourou school bi
Beug bouri boulies yi boko
Au lieu que mou touli dem josephine all ko
Lahass ko dokal ko si pocham
Dou aka hard boy
Dou suivre classe ndakh amna souk boukay dieuleul sah cour yi
Thi liko nekh la nek
Guan dou wakh dou deg
Dafa dem ba nagou fokni da mouss waye boy hadioul dieuli lane moy life
Ndakh bou hamone dina khamone dina sipni doundou bimi doundou moko yobe souma yeguone
Sathie na auto bi tiolul
Held gold ma bi feniul
Doyatouko Dou keudeu carte credit (visa bank)
Ay million la diota retiré dji (deal bi claté)
Mou guene galleh bi dem Ap deukthi
Dou dafay toukh
Dou dafay nane
Dou dougou school (non) talouko sah
Dou dall mom teylè na lifam nena dey doundou
Dou veut grandir avant l'âge
kou wakh ak mom mouni la doul Dou
My boy degue gua Dou Dou
Hey meytoul melni Dou mom Dou
Royoukay yeup Dou Dou
Mom douci meusseu gueneu
Hey meytoul melni Dou (mom douci meusseu guene)
Hey meytoul melni Dou
Dou dey toukh
Dou dey nane
Dou dou dougou school
Dou dou deglou bayam
Dou sonal yayam topoul yone bi dafa diade
Yedeu na ba sonu serigne yi deuke lek casham
Dou moy tiatam
Dou modone yakaram
Dou moy beneu bou gor souba mo narone donu bayam
Dou dafa top adouna
Dafa wathie andam
Diougue ci keur gou bah tey ay bandit lay andal Dou (dafa tegui yone dafa tegui yone)
Thioy yagui lathiè Dou (dafa tegui yone dafa tegui yone)
Douuu (dou dou dou dou dou dou dou douu)
Fils meytoul melni Dou (dou dou dou dou dou dou dou douu)
Dou dafay toukh
Dou dafay nane
Dou dougou school (non) talouko sah
Dou dall mom teylè na lifam nena day doundou (doundou)
Dou veut grandir avant l'âge
kou wahak mom mounila doul Dou
My boy degue gua Dou Do
Hey meytoul melni Dou mom Dou
Royoukay yeup Dou Dou mom douci meusseu guene
Dou dou dou dou dou dou dou dou dou dou dou dou dou dou dou




Canabasse - Boys Club - Single
Album Boys Club - Single
date de sortie
24-01-2017




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.