Canabasse - Gadaay paroles de chanson

paroles de chanson Gadaay - Canabasse



Bayil ma sorri lep louy kill sama
Vibe ma sorri lep louy kill sama vibe
Deff plein ci truck bi accélérer gaday
Ma sorri lep louy disseul sama mind diano′k sama bop sokhla nagnu Time
Ma sorri lep louy kill sama vibe
Nakh bop bi féss na nelawatou ma night
Bayima takk diouk dokh
Bayima takk diouk dokh
Bayima takk diouk dokh
Bayima takk diouk dokh
Douma yobou gatte lou doul bop deff planning mode
Sama phone dagg lien bi amoul kharite mbokk wala none
Gneup mounou gnu ande bideuntii dama wara délou teudii
Yéah teud bi bou naré yagg fogue ma teud ci fou noy
Let me go let me go let me go
Bougnu yéwo guissou gnuma dinagn nande diaroul tagoo let me go
Kou khasse ba rep boa bokay fadj ba soubeu do ci dieuli ndam
garabou Goor bokay rossé ba déweune do ci dieulé gnam
Kone bayima takk diouk dokh



Writer(s): Abdou Basse Dia


Canabasse - Gadaay
Album Gadaay
date de sortie
05-01-2018

1 Gadaay




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.