paroles de chanson Musiba - Dip Doundou Guiss feat. Ssadik Beatz
Fuck
number
one
Fuck
number
two
Ya
ngeek
limay
fay
Moytul
baña
juum
(yeaah,Ouuh)
Musiba
naarulay
Gëm
sama
ñaanu
yaay
Lëmbé
ndakaru
ndiaye
Musuma
Xaddi,
bañuma
jeng
Mais
duma
daanu
way
Aka
ma
gaaw
si
May
sa
musiba
narulay
Musiba
narulay
Comme
roof
si
ceeb
Cere
dolli
ñeex
Capp
ni
goor
Gui
Dieng
Vol
si
jet,
Wala
doxx
si
geej
Yokk
job
du
deñ
Kuy
bonn
di
hate
Bombe
nucléaire
ci
Sa
xol
bu
wow
ni
xeer
Même
boy
dé
bul
fokni
jeex
na,
May
bëss
bila
God
di
yé
Investir
ci
fenn
amo
saxx
bénéfice
du
doute
Na
doon
50
cents
sama
ben
shot,
Sa
fils
du
jukk
DIP
mola
mën
du
gacce
C′est
comme
ku
Messi
di
duut
Ma
Ngi
si
trône
bi
ak
ñom
Messi
Jël
sama
Pepsi
di
guux
Duma
segg
si
cage
Man
la
seen
soeurs
yi
di
xaar
Maa
taxx
sen
sërr
yi
di
tass
Carrière
Bi
munoko
saltel
nigger
Melni
sa
chemisou
pa
Sëg
di
gass,
Job
lu
tax
CD
bi
jarr
Fële
jël
sa
reliquat
Sama
cachet
sañu
ñuko
dagg
Ni
bin
bin
ci
sa
ndigu
Ma
Na
money
bi
teew,
Xaalis
moy
gagner
guerre
bi
duma
rayante
comme
militaires
Si
kaw
Lañuy
yeeg
wacce
leen
ni
adam
ak
awa
ak
pomme
biñu
yëy
Sori
fi
man,
Duma
xooli
sa
guel
même
su
defe
man
kesse
si
story
privem
Coow
li
Du
jeex
fi
ba
mëwti
di
dé
Amatu
ñu
adversaire
mais
ño
ngi
si
guerre
Fuck
number
one,
Fuck
number
two
Ya
ngeek
limay
fay,
Moytul
baña
juum
(yeaah,Ouuh)
Musiba
naarulay
Gëm
sama
ñaanu
yaay
Lëmbé
ndakaru
ndiaye
Musuma
Xaddi,
bañuma
jeng
mais
duma
daanu
way
Aka
ma
gaaw
si
Gars
yi
May
sa
musiba
naarulay
Musiba
naarulay
Every
day,
may
def
baña
xaar
ndaxx
dé
du
jeem
Soxlawuma
tuub
pour
def
Ko
Benn
buum
mën
na
takk
plus
de
5 jeeg
Yes
we
can
Gedd
gratte-
ciel,
Dëkki
Baraku
Bamba
fu
Trump
dem
ba
nek
president
Fu
sëtu
esclave
dila
Ray
ngir
chaîne
Tojj
sa
lu
bonn
ba
mujje
ak
séy
biens
Nigger
ëppo
Njariñ
skincaru
Michael
Jackson
ci
cimetière
Dangay
gunge
rek
ni
Frèru
Michael
Scofield
ci
biir
jail
Damay
fayu
ba
pare
mën
nangu
ni
Coow
du
jib
kay
Ku
xamm
kepp
kuy
rap
wolof
Xamna
nombre
rappeur
bi
DIP
fay
Tek
sama
nafsu
ci
beat
bi
Rap
yefu
dëmm
Dëg
lë
Kan
mo
saña
waxx
ni
que
Pac
bëggul
Biggy?
Sen
game
bi
concours
lëmbël
la
Motax
malay
yokkal
ay
tama
si
beat
bi
Sa
guel
la
yakoy
solal
makoy
simi,
Dagg
buumu
gacce
dagg
seeni
string
yi
Sama
kumpa
nekul
books
mais
Rappeur
yi
publier
gul
sen
streams
ti
Ay
goat
yu
vider
plassu
gettu
Bëy
du
sho
bu
tijji
tank
rek
ñu
dem
Dé
bi
kesse
momay
taxa
tëddi
ni
Roses
yi
si
sa
tanku
caissou
neew
Bëg
coow
ni
intifada
Ben
Laden
Même
Dof
du
sikki
sakka
lima
fi
def
God
du
mëssa
àndak
ñi
di
fenn
Par
force
King
bi
man
la
té
du
deñ
Fuck
number
one,
Fuck
number
two
Ya
ngeek
limay
fay,
Moytul
baña
juum
(yeaah,Ouuh)
Musiba
naarulay
Gëm
sama
ñaanu
yaay
Lëmbé
ndakaru
ndiaye
Musuma
Xaddi,
bañuma
jeng
mais
duma
daanu
way
Aka
ma
Gaaw
si
gars
yi
May
sa
musiba
naarulay
Musiba
naarulay
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.