paroles de chanson Bouleu Dara Méti (TLK) - Dip Doundou Guiss
Boula
dara
méti
Boula
dara
gagn
Doumeu
imbecile
Danga
ka
wareu
xam
Doumeu
domeram
Doumeu
salopard
non
Boula
dara
méti
naxx
mane
Léne
rek
meu
titeul
té
dineu
ame
Aye
nite
you
baxx
nagn
leu
diaxassé
ak
mane
Lougn
ley
wakhh
lolo
ame
Dou
diare
saxx
nguey
comprendre
Même
Boudone
mbeuguél
dey
diay,
Do
ame
kénene
comme
mane
Doy
na
waram,
deufeu
daw
yaram
Deung
meu
beugue
xamnako,
xana
dou
maleu
doxane,
doumaleu
thieupeul
Tchii
péte
yow
nguey
diay
euppeul
Dimey
thieupéle
. Yow
mi
yadone
poster
si
net
bi
nane
founé
"je
t'aime
"
Love
ngueumeu
beu
teunkalémeu
. Lolo
taxx
meu
déme.
Baby
lou
euppe
tourou,
danga
ma
warone
nobb
ndank
rek.
Waxx
na
beu
déh.
Mais
Danga
Lank
bagne
ni
domeu
degg
Mane
mako
deff
ndaxx
maleu
warone
waxx
lo
guiss
dey
diex
Yow
taxx
ngueu
nekk
seumeu
diabar
té
démeugoumeu
tchi
seu
père
Sougn
done
degueunté
téléphone
tout
le
temps
noumey
liguey
yéé
Loutaxx
kouné
wareu
controler
moromeum
comme
policier
yéé
Ame
na
rongogne
comme
yow
Manite
meune
na
lakatou
dioy
comme
yow
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.