Dip Doundou Guiss - Cicatrice - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Dip Doundou Guiss - Cicatrice

Cicatrice
Scar
Depuis ba ma.commence takk
Depuis ba ma.commence takk
Si la moteurou rap galsen bi commencé takk
Si la moteurou rap galsen bi commencé takk
Animateur yep nénagn massou ma mar sen tate
Animateur yep nénagn massou ma mar sen tate
Niata old school dans le coma
Niata old school dans le coma
Déwouma di diote ay hommage
Déwouma di diote ay hommage
Yaw khéwa go di khomate ndeysan
Yaw khéwa go di khomate ndeysan
Album bi lamb na pittch yi commencé sapp
Album bi lamb na pittch yi commencé sapp
Sama papa nénama fils c'est normale nespa?
Sama papa nénama fils c'est normale nespa?
C'est normale kay paa
C'est normale kay paa
C'est normale ndakh dama def ay cicatrices
C'est normale ndakh dama def ay cicatrices
Es ce que France sagn na bagna diokh zidane 10
Es ce que France sagn na bagna diokh zidane 10
Cicatrice
Cicatrice
Maname dama dieule artiste you gueuna makk si ben att ma def len ay archives
Maname dama dieule artiste you gueuna makk si ben att ma def len ay archives
Ma lén mane yéna ko gueuna kham bilahi
Ma lén mane yéna ko gueuna kham bilahi
Sa label lafi gueuneu niéé reptile
Sa label lafi gueuneu niéé reptile
niata deum beugueu réré dip
niata deum beugueu réré dip
lén dip yonenti la daniou réré mbir
lén dip yonenti la daniou réré mbir
Clash lou si yoni cimetiéres ak ay eglise
Clash lou si yoni cimetiéres ak ay eglise
Fakers nigga raggal yalla mo mayé fiit
Fakers nigga raggal yalla mo mayé fiit
Ngay féne rek di ame loy diéma wakh sama ethnie
Ngay féne rek di ame loy diéma wakh sama ethnie
Es ce que borom tour may diayal cd yi
Es ce que borom tour may diayal cd yi
Meme Jay Z manou ma diakhassék jesus
Meme Jay Z manou ma diakhassék jesus
Do ame dara ni candidat PS yi
Do ame dara ni candidat PS yi
Kone boul éss fils yow mandikate nga do mc
Kone boul éss fils yow mandikate nga do mc
Dip comme messi mome yéne yi douko métil
Dip comme messi mome yéne yi douko métil
Mais do mbéthie ki no bayil ma def ko domestique
Mais do mbéthie ki no bayil ma def ko domestique
Mais do raye ki no bokouniou sakh pointure
Mais do raye ki no bokouniou sakh pointure
Diouguél fi
Diouguél fi
Démal bouma def signe
Démal bouma def signe
Tar mbéthie la ba si leikhou Atou rér na
Tar mbéthie la ba si leikhou Atou rér na
Sasou
Sasou
Ngay deg sama bate founé
Ngay deg sama bate founé
Yow khathie bou bi do takk ni gaz bou diékh
Yow khathie bou bi do takk ni gaz bou diékh
Yen tatou nén ngen def dip talou lén
Yen tatou nén ngen def dip talou lén
Man sakou thiép la gueuna mana calculé
Man sakou thiép la gueuna mana calculé
Cassou méw la yamakék sen caissou néw hun
Cassou méw la yamakék sen caissou néw hun
CICATRICE
CICATRICE
CICATRICE
CICATRICE
Sama succés dafa def ay Cicatrice
Sama succés dafa def ay Cicatrice
CICATRICE
CICATRICE
CICATRICE
CICATRICE
Nigga soula mété man nga tek sa tate si gaz bi hun
Nigga soula mété man nga tek sa tate si gaz bi hun
CICATRICE
CICATRICE
CICATRICE
CICATRICE
Niépa may lathie equipe yepa ma sokhla ni Pogba juventus
Niépa may lathie equipe yepa ma sokhla ni Pogba juventus
CICATRICE
CICATRICE
CICATRICE
CICATRICE
Ni illuminati sama niari tank si kaw piramide
Ni illuminati sama niari tank si kaw piramide
Ma dakh rap si sama génération
Ma dakh rap si sama génération
Sa mame sakh day lathie bakham guéné na son
Sa mame sakh day lathie bakham guéné na son
Diougué schoolou karim xrum xakh ngen beug ma def sen gaston
Diougué schoolou karim xrum xakh ngen beug ma def sen gaston
Koula ngen dima clash xana da ngena dof
Koula ngen dima clash xana da ngena dof
Lima ame si rap dama ko mérité
Lima ame si rap dama ko mérité
dina fessal stade bi la tal bombe di guéne
dina fessal stade bi la tal bombe di guéne
Kamikaze sakh dou takh samay énnemie diekh
Kamikaze sakh dou takh samay énnemie diekh
Fuck comédien yi di wédj wédj comme ay djiguén
Fuck comédien yi di wédj wédj comme ay djiguén
Défaillant yi daniou ma déssé kham
Défaillant yi daniou ma déssé kham
Idy mayma... faw décès ame
Idy mayma... faw décès ame
Lo tekk gnou tekk boy khekh gnou khekh
Lo tekk gnou tekk boy khekh gnou khekh
Boy teikou ngueine kou keine doule teikou
Boy teikou ngueine kou keine doule teikou
Wax bou sw bi tiep bou sew bi
Wax bou sw bi tiep bou sew bi
Bouy tegui bec'ou sekou
Bouy tegui bec'ou sekou
Delouleine fingueine diougué boungueine beugué kou degg sen tourr
Delouleine fingueine diougué boungueine beugué kou degg sen tourr
Ngueine liguey gnoune gnoy fouteikou
Ngueine liguey gnoune gnoy fouteikou
TODJ SA TIOTOU AH!!
TODJ SA TIOTOU AH!!
Fuck you niggah fuck say niggah
Fuck you niggah fuck say niggah
Fuck kou begg fuck kou beggoul
Fuck kou begg fuck kou beggoul
Job bou sett la non gounguei wuñu keine
Job bou sett la non gounguei wuñu keine
Diouni trophée noneyeingui beugeu
Diouni trophée noneyeingui beugeu
Douma def ni drake di guéne back to back
Douma def ni drake di guéne back to back
Gneuweul face to face
Gneuweul face to face
Boy lgui fake yi feign
Boy lgui fake yi feign
Boy bou ndaw di leine di tiop ni tiebou dieune
Boy bou ndaw di leine di tiop ni tiebou dieune
Yagg dem fi fake yi deukk di fitna
Yagg dem fi fake yi deukk di fitna
Damko def ba yeukk ni lgui xewii na
Damko def ba yeukk ni lgui xewii na
CICATRICE
CICATRICE
Fimou tole gaînde bi da xif
Fimou tole gaînde bi da xif
Ndax gnifi gneuwone demb di gane feat
Ndax gnifi gneuwone demb di gane feat
Gno taxaw feulei nei di dingate dip
Gno taxaw feulei nei di dingate dip
Niggah fuck you fuck sa dieumbe fuck sa rouh
Niggah fuck you fuck sa dieumbe fuck sa rouh
Deumb bouy wadia fok mouy dieufeurou
Deumb bouy wadia fok mouy dieufeurou
Xawma niata grand lafi ray gnou bagnouy rap mangui jardin di day toubeuy
Xawma niata grand lafi ray gnou bagnouy rap mangui jardin di day toubeuy
Moréé
Moréé
TIOW LI BEURINA(BIS)
TIOW LI BEURINA(BIS)
AH LOLOU DEMAL WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
AH LOLOU DEMAL WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
OH MY NIGGAH (BIS)
OH MY NIGGAH (BIS)
WAXKO GNIKO ATÉNOULE
WAXKO GNIKO ATÉNOULE
TIOW LI BEURINA
TIOW LI BEURINA
OH LOLOU DEMALE WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
OH LOLOU DEMALE WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
OH MY NIGGAH
OH MY NIGGAH
YEAH WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
YEAH WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
GAME BEURRI FAKE AY RAPPEUR GOOR DJIGUEN
GAME BEURRI FAKE AY RAPPEUR GOOR DJIGUEN
MANE AWMA LOUMAY DINDI AWMA LOUMAY MODIFIÉ
MANE AWMA LOUMAY DINDI AWMA LOUMAY MODIFIÉ
CAUSE I GOT NO REGRETS I GOT NO REGRETS
CAUSE I GOT NO REGRETS I GOT NO REGRETS
MAMA MANG THI DIAM DOUGNMA DEFF SAX BOPP BOUY METTI
MAMA MANG THI DIAM DOUGNMA DEFF SAX BOPP BOUY METTI
MANÉ TIOW LI BEURINA
MANÉ TIOW LI BEURINA
EH LOLOU DEMAL WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
EH LOLOU DEMAL WAXKO NIGGAZ YIKO ATÉNOULE
OH MY NIGGAH
OH MY NIGGAH
AH YOE WAXKO SA GARS YIKO ATÉNOULE EIH
AH YOE WAXKO SA GARS YIKO ATÉNOULE EIH

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.