Dip Doundou Guiss - Taar mbeth paroles de chanson

paroles de chanson Taar mbeth - Dip Doundou Guiss



Degouma daara men
Hée
Man la way
Doundou guiss
Taay mou melni tan beer bou policiers yi di tass! kagn ngay demat sani xeer boutou keur president
Damlen fay man niki domou doubless di bi dann. israel ak palestine beugouma nek ci diam.damalen ...
Fi tchiouné fi gneup nénay dip moy messi non il joue tréés bien
Bama dalé bind motoul diourom ben att. old school youfi nek ken meunouleu def ni man
Amna niouy guené album nénagn man lagn thi clash
Coupes yengui sama negou mére niom meusouniou dem final
Samay enemis nioy coach you gueneu efficace samay none nioy samay coach you gueneu efficace
Meussougn yalouwan dougn tegui tank magui ci minou casamance yi dofouma bay tegui tank
Gars yi beugone ma xew nio beugat ma xewiwat. nélen lima dessé ci hit matna 180 giga.
Nigga malen meun
nalen soul
Par force!!!
Taar mbéth
Nigga malen meun, nalen soul, par force
Man rek!!!
Nigga malen meun nalen soul par force taar mbéth
Nigga malen meun nalen soul par force man rek
Parceque ma la meun xawma say yow loma meuneul
Do yalla, do yonenti.do sax 1 million de dollar$
Da ngueu beug fayékou naleu diox li ngeu fa am
Beus di ngeu beug romb sama kogn mou teu leu
Bro diaféwouma guiss, lou moy ngua may guiss ak niom, bo amé diom nan gay amé diotou kou am diot
Annoncer gouma sax, gneup gui sama ambum dip album bi kagn la melni album bégui casso
Niary son ci ben beat non fils do def lou melni niary son chaque niary semaine fils do def lou melni
Doxna kilométr yu beuri yag xif do dem leki ak rythme bi ma dieul ni pour done millionér dou meti
Maguek diplome yep legui ak pistolé pour ray nit kone duma yénou xew bi parsk gnoun ak yen dou derby
Broda boulma latch louy moré dioxma micro rek pour sama frigo fes mc yifi yeup la beug rek niom gneup
Niom gneup gnou xamné ni malen meun nalen soul par force taar mbéth
Nigga malen meun nalen soul par force man rek
Nigga malen meun nalen soul par force taar mbéth
Nigga malen meun nalen soul par force man rek




Dip Doundou Guiss - Dipquinzaine 2.0
Album Dipquinzaine 2.0
date de sortie
22-01-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.