Dip Doundou Guiss - One Night paroles de chanson

paroles de chanson One Night - Dip Doundou Guiss



Yaw mi yaw rk mak yaw dound ak dei kay
Tok fi do dem lo wax d'accord oui okey
Mane damala beug si sama xol tei dama beug ba xadiato sama xol
Way nala paroles yangui si sama
Xol guiss nala bima xolei si sama xol
Eh don't cry don't cry don't cry
Don't lie don't lie don't lie ohOh
All night without you(×2) i can't spend all night
Without you(×2) i don't all night without you
One night without you(×8)
Fixei ma sa beut yi lay xol ni drogué gama yak sa parfums bi
Yobouma fo xamoul sax yone bi meunougnou
Rer ndax soma guissei soumala guissei fégn
Aÿ way Aÿ way kay ma def la diabar baby kay gnou seuy way fanane si
Nek sans iiaw rk meune nama rey way
Dangmay manqué sa youma xeifei sa wett kay
Parce que mane damala beug si sama xol tei dama beug ba xadiato sama
Xol way nala paroles yangui si sama
Xol guiss nala bima xolei si sama xol
Eh don't cry don't cry don't cry
Don't lie don't lie don't lie ohOh
All night without you(×2) i can't spend all night
Without you(×2) i don't all night without you
One night without you(×8)
Dioxma lima mom diox ma lima yeilol girl tek ma sama place my girl
Dioxma lima merito dioxma lima yeilol
Girl tekma sama place ohOh dioxma lima mom
Yaw reka nei fi goudi goudna meune ga dess fanano tei
Guiss gama sa génte yi teudj nala meunatoma reuthia ti
Eh don't cry don't cry don't cry
Don't lie don't lie don't lie ohOh



Writer(s): Dominique Preira, Ismaila Talla


Dip Doundou Guiss - One Night
Album One Night
date de sortie
15-09-2017




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.