Dope Master feat. Zo Flame - Vroum Vroum paroles de chanson

paroles de chanson Vroum Vroum - Dope Master feat. Zo Flame



Guenn si ghetto bi weuri ay liass i did I did
Beugu ma dem wanté dioukhougn ma passe
Teh meunougn ma goungué yah
Daw senn circuit grand yi sissou boy yi
Dima cons ko ni Chinois
Maral nieup geumougn kenn daniouy changé
Kanam ni tiaga sou goudé
Fuck nieup
Loloy loi ndeysann das real
Get money dieundeu big house pour mère
Fokma moytou sama gars yi mangui yonou succès
Mané bb geumo dara bouma wilipandé
Mann ngua beugu meusso teud expliquer noumouy démé
Damay danou rek diouk deukou macky Dafeu amoul nelaw
Mangui takk ay boneu nigga takagou ma sokhna batay
Guiss bou bakh bi comme guerre fuck love
Bala leer beut sét
Bala deum woné kanamam goudi diote
Concert niou encaisser probleme
Yi mougn koy gerer no stress
Fuck bête si guinaw mic boudoul maté face
Face das cap haha hey
Niongui si jail kom gni abonnés si orange
Capture d'écran seuy ni yakou a si vocal
Appel vidéo meunn na sopalékou menace
Ki moy crack wanté dou dém class
Pablo scobar la def reference
Kham na Louy plan teh teksi day bedav
Yay wakh niouy déf
Only og no fake
Romb nieup ndinnt ndint
Flowou moto compet
Am dara neubou niouko
Ki niémè ay beut LOY KHOL
Niom Daniouy mèrr di leu
Daniouy yorr di leu
Daniouy tok bamou nekh
Sou taré niou mèss
Daniouy déclarer vrai
Souniouy tioubou dougn ko tay daniou faux
Démarrer Démarrer Vroum vroum
Peundeul fi dieul ngua seu cons cons
Ferrari kenn douko pouss pouss
Tassaré Tassaré town bi yeup
Dioudou si souf fi yek késsé fi Seuss
Mayé wougn dara lo niou may niou dieul Waw
"AY "
Ay texte you terre à terre lafiy tek kouko tegui degg
Boom boom
Solou big dripp Adiou sikaw lambooo domeu guiss
Mais digeu degeuh vroum vroum
Appuie Long rek mou takeu easy melni Dodge
Charger biniou tegal Paul Walker easy
Rendez au sommets my G
From west Africa nioumey diawalei
Kaw Man
Hum Loy khol?
Xamé gama key mane leu Boy bou xoulok yarou
"Wreeew"
Rew beu doff Xalei douko tendance
Xawma fo perte temps leu awma sakh vacance
Inwww Boom Boom
Signaler Left'euh diaar right
Eh siguil geu khol meu mmagui Sky
Star la dh m'y G je brille
" Laf thiatt 3x "
Yay wakh niouy déf
Only og no fake
Romb nieup ndinnt ndint
Flowou moto compet
Am dara neubou niouko
Ki niémè ay beut LOY KHOL
Niom Daniouy mèrr di leu
Daniouy yorr di leu
Daniouy tok bamou nekh
Sou taré niou mèss
Daniouy déclarer vrai
Souniouy tioubou dougn ko tay daniou faux
Démarrer Démarrer Vroum vroum
Peundeul fi dieul ngua seu cons cons
Ferrari kenn douko pouss pouss
Tassaré Tassaré town bi yeup
Dioudou si souf fi yek késsé fi Seuss
Mayé wougn dara lo niou may niou dieul Waw



Writer(s): Abdoulaye Sy, Olivier Delahaye


Dope Master feat. Zo Flame - Vroum Vroum
Album Vroum Vroum
date de sortie
03-03-2023



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.