Dope Master - KBDA paroles de chanson

paroles de chanson KBDA - Dope Master

Comme cana bou dioudowoul Ame'rique
Mane' boy bi dh deukoufi
Boude' concert mou latchie' ay hundreds miles
Dafeu yek bouko teukeule' ak Mc yi
Dafeu tiagon niou kheup si diw mou nineu
Slide sorri gnimay fe'khe'l Perce' feep ni carrierou ballou fe'te'l
Be'rte nieup moudie' wouniou sankou nde'ke'
Now everyday I wake
I think about this life
Boude' gue'l leu ma ye'ne' ko sama gars yi
Boude' khaliss ma Teral si sama yay
Kom fuse'e si kaw lagn meuneu dieum
Fiw fiw i turn it up
A.k.a boursine dou marr seu tateu
Meuno def kom li teudieul seu guateu ahh
Teudieul seu guateu teh cons
Son bi bokoul ak yi nguay job
De'fo fi guate teh yay bomb
Ah oui sans effort dagn lagn romb
Sans nguenn pousse nigger damay dokh
Perce' mm soumay sokh,
Teuyel seu guel ndakh dope dh day roff
Pussy blinde' ak pussy be'ton I do it
Nooneu yi danio beuri mangui maintien
Fuck rappeur fuck dougante'
Niom nieup nio yam ma diougue' fe'
Niou complexe' ma lakk le'ne anglais
Diangou niou doingou niou
Fay le'ne ma diangual le'ne
Boude' pour be'ne'fice awma humanite'
Clash nguama tontou wouma Kagn lalay bayi khe'l
Niongui imiter mann damle'ne di tayle'
Comme cana bou dioudowoul Ame'rique
Mane' boy bi dh deukoufi
Boude' concert mou latchie' ay hundreds miles
Dafeu yek bouko teukeule' ak Mc yi
Dafeu tiagon niou kheup si diw mou nineu
Slide sorri gnimay fe'khe'l Perce' feep ni carrierou ballou fe'te'l
Be'rte nieup moudie' wouniou sankou nde'ke'
Now everyday I wake
I think about this life
Boude' gue'l leu ma ye'ne' ko sama gars yi
Boude' khaliss ma Teral si sama yay
Kom fuse'e si kaw lagn meuneu dieum
Fiw fiw i turn it up
A.k.a boursine dou marr seu tateu
Meuno def kom li teudieul seu guateu ahh
Aka bour sine dh dou marr seu tateu
Roubinet bi teudji takhoul ma naneu potiteu
Fi niou nek dagn ko job dou ay yalouwane
Nite yi geumougn niou wone yallah geum niou dem
Cigarettes doumko toukh nigger double' rek
Ambulance si autoroute koumay double' hey
Kom 2Pac douma ko def damay bourle' ce'yi
Charge' mbe'te' bi diokhogn ko noneu yi prrr
Like Everywhere I go
Niggas want my flow
Bitches love my flow
Haters know my, real niggers they know
Real niggeRs
Everywhere I go
I don't show no love
Codeine in my cup
Og Kush my stuff
I don't worry about nothing
They'll steal em all
Dess na touti boy yeup Niro ak dope
Bayi lenn topando
Wakh bou beuri sa kogn rek ngua totchieu
Ici on nique le nord
Aline MBAYE nde'r vice' de'monte' lene
Hold up we're them boys
Fuck y'a niggas do it for my niggas
Grr bang on your nose
Tell em niggas
Tell em Bitches we don't need no love
Fi niou diogue' Dafeu soufe' guissougn bras long
Fane ngua nekone bamouy me'ti nioko cotchel souniou bopp
Pas de tingom niongui si kaw
Comme cana bou dioudowoul Ame'rique
Mane' boy bi dh deukoufi
Boude' concert mou latchie' ay hundreds miles
Dafeu yek bouko teukeule' ak Mc yi
Dafeu tiagon niou kheup si diw mou nineu
Slide sorri gnimay fe'khe'l Perce' feep ni carrierou ballou fe'te'l
Be'rte nieup moudie' wouniou sankou nde'ke'
Now everyday I wake
I think about this life
Boude' gue'l leu ma ye'ne' ko sama gars yi
Boude' khaliss ma Teral si sama yay
Kom fuse'e si kaw lagn meuneu dieum
Fiw fiw i turn it up
A.k.a boursine dou marr seu tateu
Meuno def kom li teudieul seu guateu ahh

Writer(s): Abdoulaye Sy, Delahaye Olivier, Olivier Delahaye, Sy Abdoulaye

Dope Master - KBDA
Album KBDA
date de sortie
30-09-2022

1 KBDA

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.