Elzo Jamdong - Contact paroles de chanson

paroles de chanson Contact - Elzo Jamdong



Ganiou khôl (Ganiou khôl, Ganiou khôl, Ganiou khôl)
Soma gueumoul Kaay Niou khole
(Kaay Niou khole, Kaay Niou khole)
Am naa Ganiou khôl (Ganiou khôl, Ganiou khôl, Ganiou khôl)
dow Bimay binde li sama Yaram Mingui
(dow Mingui, dow Mingui, dow Mingui, dow Mingui)
Nakhar bou Yagg thiono vous Bess rek ouais
Yone bi Niou diaarone beu fi degn ko teggui régresser
Ouais
Yakaar bou tass dokh ne tchi Souniou kow mbegté ouais
amatoul Jamm sougn diggueunté amatoul respecter
Ouais
Kenn meunoul wone gueum ne
Dinaa meusseu tok beuss te doumala khole
Noumay def ba fatté ne
Maa ndieukkeu samp nobel tchi seu khol?
Yakaar bou yaakkho tchi base
Kenn meunou ko defar tchi kenn
Limeleu defal lou baakh meuneutou meuko ko defal djigueen
Yow laa beuggone takk
Khawma Nouma def ba Niou
Niakk contacts
Warone naa meuneu nekk se garde du corps
Se garde du corps ex alla boni MA begn
Bimala niakké beu legui diommi laa def
Yow leu docteur bimay FADJ diaroul hopital
Yaay sama Doliprane, Doliprane, Doliprane
Kham nga ni yow mi chef yaay
AWMA interet bokk tchi gore yi diaay ting
Souma Offe ya peut - chargeur Comme Mobicarte
Sinon ay folies Laay def
dow de Seet naa Seu guinaaw
Namm naala beugg naala guissaat
Deuggueul negn gni Niou Yagg Diss
Gni NewOne Souniou Andeu meunoul réussir (un hun)
Liniou doundeu beuggone naa ko bissaat
Togne naala beug naa nga guiff baal ma
Je ne suis pas yakamti niou gaawa tass
Boul yakh li niou yagg
tabakh
Kenn meunoul wone gueum ne
Di naa meusseu Tok Beuss te doumala khole
Noumay de ba Fatte ne
Maa ndieukkeu samp nobel tchi
Seu Khol
Yakaar bou yaakkho tchi base de
Kenn meunou ko Defar tchi Kenn
Limeleu defal lou baakh
Meuneutou meuko ko defal djigueen
Kham na il faut que
je dem Adouna il y a tu lolou
Beuss di nga dadié'k keneen
Keneen kouy deufeul seu khole
Bokkouniou ni nouy mougné
Bokkouniou nouy moudié
Beuss d nga dadié keneen
keeneen keeneen kouen




Elzo Jamdong - FREESEASON 2
Album FREESEASON 2
date de sortie
11-01-2019




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.