Hu - Warning paroles de chanson

paroles de chanson Warning - Hu



Coach douma dougual ci pitch yeup lay football
Camp ba camp lay doute diokh GABELOOS yi dougal
Dama dougue dio gueinei li nk sama deun
Def lou diss ci yen mtx mom lay sole boudone football
Khole sama watch sama time mo diote
Tei wakhale Gars yi di fontou awma sax sen diote
Pour yekk douma botou samay tieurr mo diote
Hip-hop nk sama virus xaliss sama antidote
Am fitt troop com kou andak 110 potes
Fouma dem bokk bodoul real doma topp
Show you hot tekk ma choc tei awma sax troc
Sama show si kaw podium dou meussa noye
Fokk ma def lou khess tei douma sangou dou diwou
Soudei mère bi gnanoule nako kham souma siwoule
Damay dounde love call me hindou
Tei douma dof sama xol dou gneup lako bil-ou(oubile)
GabeLOos I am a GABELOOS
From Douane CITY
Manla AsH eezy
May def li ni
Danga beuguone ndieukeu xew mtx goudei nga ni bâche
Sa bissou décès lay def fête gnou def ngandi bâche
Dangay diaye ni danga sadik bofi douguei ma dagg sa dick
Yangui tite pourtant damay sign di keuff sa fitt
Hip Hop dam ci tokk kane mo sagn beef ma
Même soko tayoule nk taye sa biss la
Degou ma say diate gaïndé gou xiff la
Taye la sa bissou Fatiha 11Lihlass
Heezy limouy def han yeimei na dale
Boy bou ndaw di todj comme Rafael Nadal
Teila encaisser yeih fayale na gaw
Douma door ci zéro telma say ten taw
Damay rap well done
Teila bari ay none
Douma nane douma tokh
Dou seung dou bone
Indile diabou millle tonnes
Ma wagni ko ay kilo
Sama gueila meune P.Hilton ak J.lo
Sa liguey fokk mou bone coz t un idiot
Yagg takk sama biir yagatoule damay tekki
Bofi douguei di gnodi dei niggah dam lay kill
Kone bou yabo Nga bagna yeungeul tei nga diap tchill my niggah
I am a GABELOOS(bis)
From Douane CITY
Manla AsH eezy
May def li ni
Hey IC guiss nga Petit bi nekatoul Young
Wizz patience ma Pape ci beatou Mose
Taylor ci sama gang mou defma Khalifa
Keine doufi mbow ndakh GABELOOS yeup khadiougn ci son man




Hu - Warning
Album Warning
date de sortie
22-03-2015




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.