Iss 814 - Cartier paroles de chanson

paroles de chanson Cartier - Iss 814



Touti lay nopi pour rappeur yeup wakh
Mais Touti lay wakh pour rappeur yeup nopi
Sama devoir dou nek djo di produire ay copie
Am flow original comme gnom fait la cookie
Fi ndell dou fi bondé mais game bi yeup la sopi
Deglou mbaye dondé moma eup ay profit
Sen guémin ya ngandé comme n'info man bou tidji
Investir am néné nagou sen game bi gnibi
Sauvegarder say rêve formater sa xel
Machine bi dou bess day bayi sa guel
Topou gnou ben regle pour nathial sa guel
Fuck double deci-metre gnou gui si deci pel
Réseaux bi dou Pablo la dou bou niska
Do degg ouloulou bou amoul liskha
Tak tawa fay comme mauvais payeurs



Writer(s): Ismaila Talla


Iss 814 - Cartier
Album Cartier
date de sortie
18-01-2020




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.